Al-Mu'minun · 41/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
فَأَخَذَتْهُمُ الصَّيْحَةُ بِالْحَقِّ فَجَعَلْنَاهُمْ غُثَاءً ۚ فَبُعْدًا لِّلْقَوْمِ الظَّالِمِينَ ۝٤١
Fa akhazat humus saihatu bilhaqqi faja`alnaahum ghusaaa`aa; fabu;dal lilqaw miz zaalimeen
📖 Tekkim Wolof
Ag xaacu dikkal leen ci dëgg ; ñu ne lànjaŋ. Tooñkat ya tuskare nañu !

🎧 Dégg


📜 Aaya 39-43 — Simoore Al-Mu'minun

39قَالَ رَبِّ انصُرْنِي بِمَا كَذَّبُونِ
Mu ne : “Yaw sama Boroom ! May ma ndimbal ci weddi gi ñu may weddi”.
40قَالَ عَمَّا قَلِيلٍ لَّيُصْبِحُنَّ نَادِمِينَ
Mu wax ne [Moom Yàlla] : “Li feek ndiir su néew, danañu rëccu”.
41فَأَخَذَتْهُمُ الصَّيْحَةُ بِالْحَقِّ فَجَعَلْنَاهُمْ غُثَاءً ۚ فَبُعْدًا لِّلْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Ag xaacu dikkal leen ci dëgg ; ñu ne lànjaŋ. Tooñkat ya tuskare nañu !
42ثُمَّ أَنشَأْنَا مِن بَعْدِهِمْ قُرُونًا آخَرِينَ
Ba noppi, Nu sos ca seen ginnaaw yeneeni maas.
43مَا تَسْبِقُ مِنْ أُمَّةٍ أَجَلَهَا وَمَا يَسْتَأْخِرُونَ
Amul wenn xeet wuy jiitu walla mu mujj ab digam.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
41Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 41

Simoore Al-Mu'minun Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ag xaacu dikkal leen ci dëgg ; ñu ne lànjaŋ.…

Simoore Aaya 41/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers