Al-Mu'minun · 42/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
ثُمَّ أَنشَأْنَا مِن بَعْدِهِمْ قُرُونًا آخَرِينَ ۝٤٢
Summa anshaanaa mim ba`dihim quroonan aakhareen
📖 Tekkim Wolof
Ba noppi, Nu sos ca seen ginnaaw yeneeni maas.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 40-44 — Simoore Al-Mu'minun

40قَالَ عَمَّا قَلِيلٍ لَّيُصْبِحُنَّ نَادِمِينَ
Mu wax ne [Moom Yàlla] : “Li feek ndiir su néew, danañu rëccu”.
41فَأَخَذَتْهُمُ الصَّيْحَةُ بِالْحَقِّ فَجَعَلْنَاهُمْ غُثَاءً ۚ فَبُعْدًا لِّلْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Ag xaacu dikkal leen ci dëgg ; ñu ne lànjaŋ. Tooñkat ya tuskare nañu !
42ثُمَّ أَنشَأْنَا مِن بَعْدِهِمْ قُرُونًا آخَرِينَ
Ba noppi, Nu sos ca seen ginnaaw yeneeni maas.
43مَا تَسْبِقُ مِنْ أُمَّةٍ أَجَلَهَا وَمَا يَسْتَأْخِرُونَ
Amul wenn xeet wuy jiitu walla mu mujj ab digam.
44ثُمَّ أَرْسَلْنَا رُسُلَنَا تَتْرَىٰ ۖ كُلَّ مَا جَاءَ أُمَّةً رَّسُولُهَا كَذَّبُوهُ ۚ فَأَتْبَعْنَا بَعْضَهُم بَعْضًا وَجَعَلْنَاهُمْ أَحَادِيثَ ۚ فَبُعْدًا لِّقَوْمٍ لَّا يُؤْمِنُونَ
Topp, ginnaaw ba Nu yónni sunuy Yonent ñuy toppante. Xeet bu ca ab Yonentam dikkal, ñu weddi ko. Toftale Nanu leen kenn kenn, def Nanu leen ñu di ay waxtaan. Toskare ñeel na aw nit ñu gëmul !
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 42

Simoore Al-Mu'minun Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba noppi, Nu sos ca seen ginnaaw yeneeni maas.

Simoore Aaya 42/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers