Al-Furqan · 66/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
إِنَّهَا سَاءَتْ مُسْتَقَرًّا وَمُقَامًا ۝٦٦
Innahaa saaa`at mustaqarranw wa muqaamaa
📖 Tekkim Wolof
Ndaw dëkkuwaay bu soof !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 64-68 — Simoore Al-Furqan

64وَالَّذِينَ يَبِيتُونَ لِرَبِّهِمْ سُجَّدًا وَقِيَامًا
ñoom ñooy fanaanee julli te Yàlla rekk tax [taxaw ak a sujjóot] ;
65وَالَّذِينَ يَقُولُونَ رَبَّنَا اصْرِفْ عَنَّا عَذَابَ جَهَنَّمَ ۖ إِنَّ عَذَابَهَا كَانَ غَرَامًا
ñoom ñooy wax naan : “Yàlla, yal na nga nu dëddëleek mbugalum Safara”. - mbugalum Safara soosu lu ne dànk la.
66إِنَّهَا سَاءَتْ مُسْتَقَرًّا وَمُقَامًا
Ndaw dëkkuwaay bu soof !
67وَالَّذِينَ إِذَا أَنفَقُوا لَمْ يُسْرِفُوا وَلَمْ يَقْتُرُوا وَكَانَ بَيْنَ ذَٰلِكَ قَوَامًا
Bu ñuy joxe alal, duñu xaabaabal te it duñu nay, dañuy digg-dóomu.
68وَالَّذِينَ لَا يَدْعُونَ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ وَلَا يَقْتُلُونَ النَّفْسَ الَّتِي حَرَّمَ اللَّهُ إِلَّا بِالْحَقِّ وَلَا يَزْنُونَ ۚ وَمَن يَفْعَلْ ذَٰلِكَ يَلْقَ أَثَامًا
Duñu boole di jaamoondoo dara ak Yàlla, te duñu rey bakkan bu Yàlla tere ku ko rey, lu dul ci dëgg ; duñu njaaloo it - képp ku def loolu, dana dajeek mbugal
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
66Aaya

Tekki — Al-Furqan 66

Simoore Al-Furqan Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndaw dëkkuwaay bu soof !

Simoore Aaya 66/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers