Al-Furqan · 67/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
وَالَّذِينَ إِذَا أَنفَقُوا لَمْ يُسْرِفُوا وَلَمْ يَقْتُرُوا وَكَانَ بَيْنَ ذَٰلِكَ قَوَامًا ۝٦٧
Wallazeena izaaa anfaqoo lam yusrifoo wa lam yaqturoo wa kaana baina zaalika qawaamaa
📖 Tekkim Wolof
Bu ñuy joxe alal, duñu xaabaabal te it duñu nay, dañuy digg-dóomu.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 65-69 — Simoore Al-Furqan

65وَالَّذِينَ يَقُولُونَ رَبَّنَا اصْرِفْ عَنَّا عَذَابَ جَهَنَّمَ ۖ إِنَّ عَذَابَهَا كَانَ غَرَامًا
ñoom ñooy wax naan : “Yàlla, yal na nga nu dëddëleek mbugalum Safara”. - mbugalum Safara soosu lu ne dànk la.
66إِنَّهَا سَاءَتْ مُسْتَقَرًّا وَمُقَامًا
Ndaw dëkkuwaay bu soof !
67وَالَّذِينَ إِذَا أَنفَقُوا لَمْ يُسْرِفُوا وَلَمْ يَقْتُرُوا وَكَانَ بَيْنَ ذَٰلِكَ قَوَامًا
Bu ñuy joxe alal, duñu xaabaabal te it duñu nay, dañuy digg-dóomu.
68وَالَّذِينَ لَا يَدْعُونَ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ وَلَا يَقْتُلُونَ النَّفْسَ الَّتِي حَرَّمَ اللَّهُ إِلَّا بِالْحَقِّ وَلَا يَزْنُونَ ۚ وَمَن يَفْعَلْ ذَٰلِكَ يَلْقَ أَثَامًا
Duñu boole di jaamoondoo dara ak Yàlla, te duñu rey bakkan bu Yàlla tere ku ko rey, lu dul ci dëgg ; duñu njaaloo it - képp ku def loolu, dana dajeek mbugal
69يُضَاعَفْ لَهُ الْعَذَابُ يَوْمَ الْقِيَامَةِ وَيَخْلُدْ فِيهِ مُهَانًا
dees na ko fulal mbugal ma bu Bis-pénc baa, te dafay béel cig doyadi ;
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
67Aaya

Tekki — Al-Furqan 67

Simoore Al-Furqan Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñuy joxe alal, duñu xaabaabal te it duñu nay,…

Simoore Aaya 67/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers