Ash-Shu'ara · 111/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
۞ قَالُوا أَنُؤْمِنُ لَكَ وَاتَّبَعَكَ الْأَرْذَلُونَ ۝١١١
Qaalooo anu`minu laka wattaba `akal arzaloon
📖 Tekkim Wolof
Ñu wax ko ne : “Ndax dananu la gëm te ñi gën a saay-saay a ngi la topp? ”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 109-113 — Simoore Ash-Shu'ara

109وَمَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ ۖ إِنْ أَجْرِيَ إِلَّا عَلَىٰ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Te laajuma leen ci génn pey ; samag pey Boroom àddina si moo ko warlu.
110فَاتَّقُوا اللَّهَ وَأَطِيعُونِ
Ragal-leen Yàlla te topp ma”
111۞ قَالُوا أَنُؤْمِنُ لَكَ وَاتَّبَعَكَ الْأَرْذَلُونَ
Ñu wax ko ne : “Ndax dananu la gëm te ñi gën a saay-saay a ngi la topp? ”
112قَالَ وَمَا عِلْمِي بِمَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Mu wax ne : “Ana man lu ma xam ca la ñu daan def.
113إِنْ حِسَابُهُمْ إِلَّا عَلَىٰ رَبِّي ۖ لَوْ تَشْعُرُونَ
Seenub waññoo nga ca Yàlla [Moo koy taxawe]. Céy bu ngeen yëgoon.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
111Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 111

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 111 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu wax ko ne : “Ndax dananu la gëm te…

Simoore Aaya 111/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 109–113. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers