Ash-Shu'ara · 154/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
مَا أَنتَ إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُنَا فَأْتِ بِآيَةٍ إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ ۝١٥٤
Maaa anta illaa basharum mislunaa faati bi Aayatin in kunta minas saadiqeen
📖 Tekkim Wolof
Yaw daal, doo kenn ku dul nit ni nun. Indil kaawtéef ndegam li ngay wax dëgg la”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 152-156 — Ash-Shu'ara

152الَّذِينَ يُفْسِدُونَ فِي الْأَرْضِ وَلَا يُصْلِحُونَ
ñiy yàq rekk ci suuf si te duñu defar”.
153قَالُوا إِنَّمَا أَنتَ مِنَ الْمُسَحَّرِينَ
Ñu ne ko : “Yaw daal, ab njibar moo la ŋëb.
154مَا أَنتَ إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُنَا فَأْتِ بِآيَةٍ إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Yaw daal, doo kenn ku dul nit ni nun. Indil kaawtéef ndegam li ngay wax dëgg la”.
155قَالَ هَٰذِهِ نَاقَةٌ لَّهَا شِرْبٌ وَلَكُمْ شِرْبُ يَوْمٍ مَّعْلُومٍ
Saalihu ne leen : “Lii giléem gu jigéen la [naaga] : am na bis bu muy naan, yéen it am ngeen seen bis.
156وَلَا تَمَسُّوهَا بِسُوءٍ فَيَأْخُذَكُمْ عَذَابُ يَوْمٍ عَظِيمٍ
Buleen ko def mukk lu bon, [su ngeen ko ko defee], di ngeen yendu bisub mbugal mu tar”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
154Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 154

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 154 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yaw daal, doo kenn ku dul nit ni nun. Indil…

Simoore Aaya 154/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 152–156. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers