Ash-Shu'ara · 16/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
فَأْتِيَا فِرْعَوْنَ فَقُولَا إِنَّا رَسُولُ رَبِّ الْعَالَمِينَ ١٦
Transliteration
Faatiyaa Fir`awna faqoolaaa innaa Rasoolu Rabbil `aalameen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Dem ca Firawna ne ko : “Nun ñaari ndawi Boroom àddina si lanu,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 14-18 — Ash-Shu'ara
14وَلَهُمْ عَلَيَّ ذَنبٌ فَأَخَافُ أَن يَقْتُلُونِ
Te itam, am na tuuma ju ñu may jiiñ ; te ragal naa ñu rey ma”.
15قَالَ كَلَّا ۖ فَاذْهَبَا بِآيَاتِنَا ۖ إِنَّا مَعَكُم مُّسْتَمِعُونَ
[Yàlla] ne : “Mukk du am ! Demleen yéen ñaar yóbb sunuy kàddu. Maa ngi ànd ak yéen di dégg.
16فَأْتِيَا فِرْعَوْنَ فَقُولَا إِنَّا رَسُولُ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Dem ca Firawna ne ko : “Nun ñaari ndawi Boroom àddina si lanu,
17أَنْ أَرْسِلْ مَعَنَا بَنِي إِسْرَائِيلَ
Yebalal giir Banii-Israayil ñu ànd ak nun ”.
18قَالَ أَلَمْ نُرَبِّكَ فِينَا وَلِيدًا وَلَبِثْتَ فِينَا مِنْ عُمُرِكَ سِنِينَ
[Firawna] ne ko : “Moo ndax yarunu la fii ba nga doonee liir ? Ak li nga fi nekk lépp ?
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
16Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 16
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dem ca Firawna ne ko : “Nun ñaari ndawi Boroom…Simoore Aaya 16/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








