Ash-Shu'ara · 166/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
وَتَذَرُونَ مَا خَلَقَ لَكُمْ رَبُّكُم مِّنْ أَزْوَاجِكُم ۚ بَلْ أَنتُمْ قَوْمٌ عَادُونَ ۝١٦٦
Wa tazaroona maa khalaqa lakum Rabbukum min azwaajikum; bal antum qawmun `aadoon
📖 Tekkim Wolof
Ne fa ñukk seen jabar ya leen Yàlla sàkkal ? Waajii ! Yéen ay jalgatikat ngeen de”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 164-168 — Ash-Shu'ara

164وَمَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ ۖ إِنْ أَجْرِيَ إِلَّا عَلَىٰ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Laajuma leen ci genn pey ; samag pey, Boroom àddina see ko warlu.
165أَتَأْتُونَ الذُّكْرَانَ مِنَ الْعَالَمِينَ
Yéen góor ñi, moo ndax dangeen di sàkku bànneexu séy ci góoru àddina sii [Ngóor- jigéen]?
166وَتَذَرُونَ مَا خَلَقَ لَكُمْ رَبُّكُم مِّنْ أَزْوَاجِكُم ۚ بَلْ أَنتُمْ قَوْمٌ عَادُونَ
Ne fa ñukk seen jabar ya leen Yàlla sàkkal ? Waajii ! Yéen ay jalgatikat ngeen de”.
167قَالُوا لَئِن لَّمْ تَنتَهِ يَا لُوطُ لَتَكُونَنَّ مِنَ الْمُخْرَجِينَ
Ñu ne ko : “Yaw Lóot, boo bàyyiwul lii ngay wax, dananu la génne”.
168قَالَ إِنِّي لِعَمَلِكُم مِّنَ الْقَالِينَ
Lóot ne leen : “Seen jëf jii, lenn rekk laa ciy wax.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
166Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 166

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 166 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ne fa ñukk seen jabar ya leen Yàlla sàkkal ?…

Simoore Aaya 166/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 164–168. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers