Ash-Shu'ara · 167/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
قَالُوا لَئِن لَّمْ تَنتَهِ يَا لُوطُ لَتَكُونَنَّ مِنَ الْمُخْرَجِينَ ۝١٦٧
Qaloo la`il lam tantahi yaa Lootu latakoonanna minal mukhrajeen
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : “Yaw Lóot, boo bàyyiwul lii ngay wax, dananu la génne”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 165-169 — Simoore Ash-Shu'ara

165أَتَأْتُونَ الذُّكْرَانَ مِنَ الْعَالَمِينَ
Yéen góor ñi, moo ndax dangeen di sàkku bànneexu séy ci góoru àddina sii [Ngóor- jigéen]?
166وَتَذَرُونَ مَا خَلَقَ لَكُمْ رَبُّكُم مِّنْ أَزْوَاجِكُم ۚ بَلْ أَنتُمْ قَوْمٌ عَادُونَ
Ne fa ñukk seen jabar ya leen Yàlla sàkkal ? Waajii ! Yéen ay jalgatikat ngeen de”.
167قَالُوا لَئِن لَّمْ تَنتَهِ يَا لُوطُ لَتَكُونَنَّ مِنَ الْمُخْرَجِينَ
Ñu ne ko : “Yaw Lóot, boo bàyyiwul lii ngay wax, dananu la génne”.
168قَالَ إِنِّي لِعَمَلِكُم مِّنَ الْقَالِينَ
Lóot ne leen : “Seen jëf jii, lenn rekk laa ciy wax.
169رَبِّ نَجِّنِي وَأَهْلِي مِمَّا يَعْمَلُونَ
Yaw sama Boroom, yal na nga musal maak saag njaboot ci lii ñuy def”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
167Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 167

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 167 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : “Yaw Lóot, boo bàyyiwul lii ngay…

Simoore Aaya 167/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 165–169. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers