Ash-Shu'ara · 165/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
أَتَأْتُونَ الذُّكْرَانَ مِنَ الْعَالَمِينَ ۝١٦٥
Ataatoonaz zukraana minal `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Yéen góor ñi, moo ndax dangeen di sàkku bànneexu séy ci góoru àddina sii [Ngóor- jigéen]?

🎧 Dégg


📜 Aaya 163-167 — Ash-Shu'ara

163فَاتَّقُوا اللَّهَ وَأَطِيعُونِ
Ragal-leen Yàlla te topp ma.
164وَمَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ ۖ إِنْ أَجْرِيَ إِلَّا عَلَىٰ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Laajuma leen ci genn pey ; samag pey, Boroom àddina see ko warlu.
165أَتَأْتُونَ الذُّكْرَانَ مِنَ الْعَالَمِينَ
Yéen góor ñi, moo ndax dangeen di sàkku bànneexu séy ci góoru àddina sii [Ngóor- jigéen]?
166وَتَذَرُونَ مَا خَلَقَ لَكُمْ رَبُّكُم مِّنْ أَزْوَاجِكُم ۚ بَلْ أَنتُمْ قَوْمٌ عَادُونَ
Ne fa ñukk seen jabar ya leen Yàlla sàkkal ? Waajii ! Yéen ay jalgatikat ngeen de”.
167قَالُوا لَئِن لَّمْ تَنتَهِ يَا لُوطُ لَتَكُونَنَّ مِنَ الْمُخْرَجِينَ
Ñu ne ko : “Yaw Lóot, boo bàyyiwul lii ngay wax, dananu la génne”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
165Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 165

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 165 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen góor ñi, moo ndax dangeen di sàkku bànneexu séy…

Simoore Aaya 165/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 163–167. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers