Ash-Shu'ara · 204/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
أَفَبِعَذَابِنَا يَسْتَعْجِلُونَ ۝٢٠٤
Aafabi `azaabinaa yasta`jiloon
📖 Tekkim Wolof
Ndax dañoo yàkkamti Sunu mbugal ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 202-206 — Ash-Shu'ara

202فَيَأْتِيَهُم بَغْتَةً وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
mu dikke leen ci mbettel te ñoom bëgguñu ko;
203فَيَقُولُوا هَلْ نَحْنُ مُنظَرُونَ
ñuy wax naan : “Ndax deesu yeexe sunuy mbir ? ”
204أَفَبِعَذَابِنَا يَسْتَعْجِلُونَ
Ndax dañoo yàkkamti Sunu mbugal ?
205أَفَرَأَيْتَ إِن مَّتَّعْنَاهُمْ سِنِينَ
Xanaa gisuloo ne bàyyi woon Nanu leen ay ati at ñuy xaab-xaabi,
206ثُمَّ جَاءَهُم مَّا كَانُوا يُوعَدُونَ
tey jii nag la Nu leen doon dig agsi na,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
204Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 204

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 204 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax dañoo yàkkamti Sunu mbugal ?

Simoore Aaya 204/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 202–206. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers