Ash-Shu'ara · 53/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
فَأَرْسَلَ فِرْعَوْنُ فِي الْمَدَائِنِ حَاشِرِينَ ۝٥٣
Fa arsala Fir`awnu filmadaaa`ini haashireen
📖 Tekkim Wolof
Firawna daldi yónnee ci gox yi ñuy yéene dajale nit ñi :

🎧 Dégg


📜 Aaya 51-55 — Simoore Ash-Shu'ara

51إِنَّا نَطْمَعُ أَن يَغْفِرَ لَنَا رَبُّنَا خَطَايَانَا أَن كُنَّا أَوَّلَ الْمُؤْمِنِينَ
Danoo xemmem Yàlla jéggal nu sunuy njuumte, xemmem it doon ñu njëkk a gëm”.
52۞ وَأَوْحَيْنَا إِلَىٰ مُوسَىٰ أَنْ أَسْرِ بِعِبَادِي إِنَّكُم مُّتَّبَعُونَ
Nu daldi soloo Muusaa, digal ko mu rañaan ànd ak samay jaam te danañu leen dabsi.
53فَأَرْسَلَ فِرْعَوْنُ فِي الْمَدَائِنِ حَاشِرِينَ
Firawna daldi yónnee ci gox yi ñuy yéene dajale nit ñi :
54إِنَّ هَٰؤُلَاءِ لَشِرْذِمَةٌ قَلِيلُونَ
“Ñoom dey, ay mbooloo yu néew lañu,
55وَإِنَّهُمْ لَنَا لَغَائِظُونَ
te it mere nañu nu,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
53Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 53

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Firawna daldi yónnee ci gox yi ñuy yéene dajale nit…

Simoore Aaya 53/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 51–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers