Ash-Shu'ara · 6/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
فَقَدْ كَذَّبُوا فَسَيَأْتِيهِمْ أَنبَاءُ مَا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ ۝٦
Faqad kazzaboo fasa yaateehim ambaaa`u maa kaanoo bihee yastahzi`oon
📖 Tekkim Wolof
Weddi woon nañu, te danañu mës a joti xibaari la ñu doon téjji.

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Ash-Shu'ara

4إِن نَّشَأْ نُنَزِّلْ عَلَيْهِم مِّنَ السَّمَاءِ آيَةً فَظَلَّتْ أَعْنَاقُهُمْ لَهَا خَاضِعِينَ
Bu Nu neexoon Nu wàcce ci asamaan kéemaan guy tax ñuy jatti loos.
5وَمَا يَأْتِيهِم مِّن ذِكْرٍ مِّنَ الرَّحْمَٰنِ مُحْدَثٍ إِلَّا كَانُوا عَنْهُ مُعْرِضِينَ
Amul benn woote bu bees bu mësoon a bawoo ca Yàlla lu dul ne dëndu dañu ko.
6فَقَدْ كَذَّبُوا فَسَيَأْتِيهِمْ أَنبَاءُ مَا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
Weddi woon nañu, te danañu mës a joti xibaari la ñu doon téjji.
7أَوَلَمْ يَرَوْا إِلَى الْأَرْضِ كَمْ أَنبَتْنَا فِيهَا مِن كُلِّ زَوْجٍ كَرِيمٍ
Xanaa dañoo gisul yu bari yi Nu saxal ci kaw suuf, ci xeeti gàncax muy tollént ?
8إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Ay kéemaan yu bari nekk ci loolu ! Waaye taxut li ëpp ci ñoom gëm [diy jullit].
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 6

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Weddi woon nañu, te danañu mës a joti xibaari la…

Simoore Aaya 6/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers