An-Naml · 54/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
وَلُوطًا إِذْ قَالَ لِقَوْمِهِ أَتَأْتُونَ الْفَاحِشَةَ وَأَنتُمْ تُبْصِرُونَ ۝٥٤
Wa lootan iz qaala liqawmiheee ataatoonal faa hishata wa antum qawmun tajjhaloon
📖 Tekkim Wolof
[Fàttalikul] Lóot, ba mu waxee aw nitam, ne leen : “Ndax dangeen di def ñaawtéef te ne ca jàkk”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 52-56 — Simoore An-Naml

52فَتِلْكَ بُيُوتُهُمْ خَاوِيَةً بِمَا ظَلَمُوا ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّقَوْمٍ يَعْلَمُونَ
Seen kër yaa ngi noonu gent na ngir la ñu tooñoon. Ay kéemaan a ngi ci loolu ngir aw nit ñuy xam.
53وَأَنجَيْنَا الَّذِينَ آمَنُوا وَكَانُوا يَتَّقُونَ
Te musal Nanu ña gëmoon te ragal Yàlla.
54وَلُوطًا إِذْ قَالَ لِقَوْمِهِ أَتَأْتُونَ الْفَاحِشَةَ وَأَنتُمْ تُبْصِرُونَ
[Fàttalikul] Lóot, ba mu waxee aw nitam, ne leen : “Ndax dangeen di def ñaawtéef te ne ca jàkk”.
55أَئِنَّكُمْ لَتَأْتُونَ الرِّجَالَ شَهْوَةً مِّن دُونِ النِّسَاءِ ۚ بَلْ أَنتُمْ قَوْمٌ تَجْهَلُونَ
Ndax dangeen di gën a xemmem góor ñi bàyyi jigéen ñi ? Yéen daal aw nit ñu réer ngeen.
56۞ فَمَا كَانَ جَوَابَ قَوْمِهِ إِلَّا أَن قَالُوا أَخْرِجُوا آلَ لُوطٍ مِّن قَرْيَتِكُمْ ۖ إِنَّهُمْ أُنَاسٌ يَتَطَهَّرُونَ
Nitam ña tontuwuñu lu dul ne : “Génneleen njabootug Lóot ci seen dëkk bii ! Ndax ñoom dañuy jéem a laab-laablu.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
54Aaya

Tekki — An-Naml 54

Simoore An-Naml Aaya 54 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Fàttalikul] Lóot, ba mu waxee aw nitam, ne leen :…

Simoore Aaya 54/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 52–56. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers