An-Naml · 56/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
۞ فَمَا كَانَ جَوَابَ قَوْمِهِ إِلَّا أَن قَالُوا أَخْرِجُوا آلَ لُوطٍ مِّن قَرْيَتِكُمْ ۖ إِنَّهُمْ أُنَاسٌ يَتَطَهَّرُونَ ۝٥٦
Fammaa kaana jawaaba qawmiheee illaaa an qaalooo akrijoon aalaa Lootim min qaryatikum innahum unaasuny yatatahharoon
📖 Tekkim Wolof
Nitam ña tontuwuñu lu dul ne : “Génneleen njabootug Lóot ci seen dëkk bii ! Ndax ñoom dañuy jéem a laab-laablu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 54-58 — An-Naml

54وَلُوطًا إِذْ قَالَ لِقَوْمِهِ أَتَأْتُونَ الْفَاحِشَةَ وَأَنتُمْ تُبْصِرُونَ
[Fàttalikul] Lóot, ba mu waxee aw nitam, ne leen : “Ndax dangeen di def ñaawtéef te ne ca jàkk”.
55أَئِنَّكُمْ لَتَأْتُونَ الرِّجَالَ شَهْوَةً مِّن دُونِ النِّسَاءِ ۚ بَلْ أَنتُمْ قَوْمٌ تَجْهَلُونَ
Ndax dangeen di gën a xemmem góor ñi bàyyi jigéen ñi ? Yéen daal aw nit ñu réer ngeen.
56۞ فَمَا كَانَ جَوَابَ قَوْمِهِ إِلَّا أَن قَالُوا أَخْرِجُوا آلَ لُوطٍ مِّن قَرْيَتِكُمْ ۖ إِنَّهُمْ أُنَاسٌ يَتَطَهَّرُونَ
Nitam ña tontuwuñu lu dul ne : “Génneleen njabootug Lóot ci seen dëkk bii ! Ndax ñoom dañuy jéem a laab-laablu.
57فَأَنجَيْنَاهُ وَأَهْلَهُ إِلَّا امْرَأَتَهُ قَدَّرْنَاهَا مِنَ الْغَابِرِينَ
Nu daldi koy musal mook njabootam ga ba mu des soxnaam sa àndoon ak defkatu ñaawtéef ya Nu faagaagal.
58وَأَمْطَرْنَا عَلَيْهِم مَّطَرًا ۖ فَسَاءَ مَطَرُ الْمُنذَرِينَ
Dotti Nanu ca seen kaw waamem [doj]. Ndaw taw bu bon ca ña mu dal ca seen kaw!
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
56Aaya

Tekki — An-Naml 56

Simoore An-Naml Aaya 56 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nitam ña tontuwuñu lu dul ne : “Génneleen njabootug Lóot…

Simoore Aaya 56/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 54–58. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers