Al-Qasas · 10/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
وَأَصْبَحَ فُؤَادُ أُمِّ مُوسَىٰ فَارِغًا ۖ إِن كَادَتْ لَتُبْدِي بِهِ لَوْلَا أَن رَّبَطْنَا عَلَىٰ قَلْبِهَا لِتَكُونَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ ۝١٠
Wa asbaha fu`aadu ummi Moosaa faarighan in kaadat latubdee bihee law laaa arrabatnaa `alaa qalbihaa litakoona minal mu`mineen
📖 Tekkim Wolof
Xolub ndeyu Muusaa ja jeex na tàkk. Ba mu xaw a feeñal, cëy bu Nu ko dëfëlul woon xolam ak la mu doonoon di ab jullit.

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Simoore Al-Qasas

8فَالْتَقَطَهُ آلُ فِرْعَوْنَ لِيَكُونَ لَهُمْ عَدُوًّا وَحَزَنًا ۗ إِنَّ فِرْعَوْنَ وَهَامَانَ وَجُنُودَهُمَا كَانُوا خَاطِئِينَ
Waa kër Firawna for ko, ngir mu doon seenub noon, di seenu lëjal ! Firawna, Haamaan ak seen gàngoor juumoon nañu.
9وَقَالَتِ امْرَأَتُ فِرْعَوْنَ قُرَّتُ عَيْنٍ لِّي وَلَكَ ۖ لَا تَقْتُلُوهُ عَسَىٰ أَن يَنفَعَنَا أَوْ نَتَّخِذَهُ وَلَدًا وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Jabari Firawna ne ko : “(Xale bii di Muusaa) ! buleen ko rey. Nanu ko wéttalikoo maak yaw walla nu doomoo ko, amaana mu jariñ nu”. Lii lépp nag ba muy xew yëguñu ca dara.
10وَأَصْبَحَ فُؤَادُ أُمِّ مُوسَىٰ فَارِغًا ۖ إِن كَادَتْ لَتُبْدِي بِهِ لَوْلَا أَن رَّبَطْنَا عَلَىٰ قَلْبِهَا لِتَكُونَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Xolub ndeyu Muusaa ja jeex na tàkk. Ba mu xaw a feeñal, cëy bu Nu ko dëfëlul woon xolam ak la mu doonoon di ab jullit.
11وَقَالَتْ لِأُخْتِهِ قُصِّيهِ ۖ فَبَصُرَتْ بِهِ عَن جُنُبٍ وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Mu wax mbokkam mu jigéen ma ne ko : “Topp ko” ; mu di ko bàyyi xel, topp ko te kenn xamut.
12۞ وَحَرَّمْنَا عَلَيْهِ الْمَرَاضِعَ مِن قَبْلُ فَقَالَتْ هَلْ أَدُلُّكُمْ عَلَىٰ أَهْلِ بَيْتٍ يَكْفُلُونَهُ لَكُمْ وَهُمْ لَهُ نَاصِحُونَ
Noo ko bañloo woon nàmpalkat ya. Ba mbokkam mu jigéen ma agsee, daldi wax ne : “Ndax duma leen tegtal waa kër goo xam ne danañu leen ko yaral te di ko toppatoo ? ”...
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Al-Qasas 10

Simoore Al-Qasas Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xolub ndeyu Muusaa ja jeex na tàkk. Ba mu xaw…

Simoore Aaya 10/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers