Al-Qasas · 11/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
وَقَالَتْ لِأُخْتِهِ قُصِّيهِ ۖ فَبَصُرَتْ بِهِ عَن جُنُبٍ وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ ۝١١
Wa qaalat li ukhtihee qusseehi fabasurat bihee `an junubinw wahum laa yash`uroon
📖 Tekkim Wolof
Mu wax mbokkam mu jigéen ma ne ko : “Topp ko” ; mu di ko bàyyi xel, topp ko te kenn xamut.

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Simoore Al-Qasas

9وَقَالَتِ امْرَأَتُ فِرْعَوْنَ قُرَّتُ عَيْنٍ لِّي وَلَكَ ۖ لَا تَقْتُلُوهُ عَسَىٰ أَن يَنفَعَنَا أَوْ نَتَّخِذَهُ وَلَدًا وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Jabari Firawna ne ko : “(Xale bii di Muusaa) ! buleen ko rey. Nanu ko wéttalikoo maak yaw walla nu doomoo ko, amaana mu jariñ nu”. Lii lépp nag ba muy xew yëguñu ca dara.
10وَأَصْبَحَ فُؤَادُ أُمِّ مُوسَىٰ فَارِغًا ۖ إِن كَادَتْ لَتُبْدِي بِهِ لَوْلَا أَن رَّبَطْنَا عَلَىٰ قَلْبِهَا لِتَكُونَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Xolub ndeyu Muusaa ja jeex na tàkk. Ba mu xaw a feeñal, cëy bu Nu ko dëfëlul woon xolam ak la mu doonoon di ab jullit.
11وَقَالَتْ لِأُخْتِهِ قُصِّيهِ ۖ فَبَصُرَتْ بِهِ عَن جُنُبٍ وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Mu wax mbokkam mu jigéen ma ne ko : “Topp ko” ; mu di ko bàyyi xel, topp ko te kenn xamut.
12۞ وَحَرَّمْنَا عَلَيْهِ الْمَرَاضِعَ مِن قَبْلُ فَقَالَتْ هَلْ أَدُلُّكُمْ عَلَىٰ أَهْلِ بَيْتٍ يَكْفُلُونَهُ لَكُمْ وَهُمْ لَهُ نَاصِحُونَ
Noo ko bañloo woon nàmpalkat ya. Ba mbokkam mu jigéen ma agsee, daldi wax ne : “Ndax duma leen tegtal waa kër goo xam ne danañu leen ko yaral te di ko toppatoo ? ”...
13فَرَدَدْنَاهُ إِلَىٰ أُمِّهِ كَيْ تَقَرَّ عَيْنُهَا وَلَا تَحْزَنَ وَلِتَعْلَمَ أَنَّ وَعْدَ اللَّهِ حَقٌّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Nu daldi koy delloo ndeyam ja ngir mu wéttaliku ba bañ a tiit ak it ngir mu xam ne digub Yàlla lu dëggu la. Waaye li ëpp ci ñoom xamuñu.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — Al-Qasas 11

Simoore Al-Qasas Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu wax mbokkam mu jigéen ma ne ko : “Topp…

Simoore Aaya 11/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers