Al-Qasas · 45/88
Tekki Waxtaan — Al-Qasas
وَلَٰكِنَّا أَنشَأْنَا قُرُونًا فَتَطَاوَلَ عَلَيْهِمُ الْعُمُرُ ۚ وَمَا كُنتَ ثَاوِيًا فِي أَهْلِ مَدْيَنَ تَتْلُو عَلَيْهِمْ آيَاتِنَا وَلَٰكِنَّا كُنَّا مُرْسِلِينَ ۝٤٥
Wa laakinnaa anshaanaa quroonan fatataawala `alaihimul `umur; wa maa kunta saawiyan feee ahli Madyana tatloo `alaihim Aayaatinaa wa laakinnaa kunnaa mursileen
📖 Tekkim Wolof
Waaye sosoon Nanu ay maas yu guddu na fan. Te it nekkoo woon ca waa Madiyaana di leen nettali Sunuy kàddu; waaye Nun [Yàlla], Noo daan yable.

🎧 Dégg


📜 Aaya 43-47 — Al-Qasas

43وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْكِتَابَ مِن بَعْدِ مَا أَهْلَكْنَا الْقُرُونَ الْأُولَىٰ بَصَائِرَ لِلنَّاسِ وَهُدًى وَرَحْمَةً لَّعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ
Jox Nanu Muusaa Téere ba, - ca ginnaaw ba Nu faagaagalee maas ya ko jiitu, - ngir mu doon am njis ak njub, ak yërmaande ak it ngir ñu mën caa fàttalikoo.
44وَمَا كُنتَ بِجَانِبِ الْغَرْبِيِّ إِذْ قَضَيْنَا إِلَىٰ مُوسَى الْأَمْرَ وَمَا كُنتَ مِنَ الشَّاهِدِينَ
Te yaw [Muhammad], nekkoo woon ca xuru sowwu wa ca ba Nuy jox Muusaa ndigal ya: te fekkewoo ko woon [seede ko].
45وَلَٰكِنَّا أَنشَأْنَا قُرُونًا فَتَطَاوَلَ عَلَيْهِمُ الْعُمُرُ ۚ وَمَا كُنتَ ثَاوِيًا فِي أَهْلِ مَدْيَنَ تَتْلُو عَلَيْهِمْ آيَاتِنَا وَلَٰكِنَّا كُنَّا مُرْسِلِينَ
Waaye sosoon Nanu ay maas yu guddu na fan. Te it nekkoo woon ca waa Madiyaana di leen nettali Sunuy kàddu; waaye Nun [Yàlla], Noo daan yable.
46وَمَا كُنتَ بِجَانِبِ الطُّورِ إِذْ نَادَيْنَا وَلَٰكِن رَّحْمَةً مِّن رَّبِّكَ لِتُنذِرَ قَوْمًا مَّا أَتَاهُم مِّن نَّذِيرٍ مِّن قَبْلِكَ لَعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ
Nekkoo woon it wetu Tuur jamono ja Nuy woote. [Waaye dangaa dikk di] yërmaandey sa Boroom, ak it ngir nga xupp aw nit ñoo xam ne mësuñoo am ab xuppekat ci la ko jiitu, ndax it ñu mën caa fàttalikoo.
47وَلَوْلَا أَن تُصِيبَهُم مُّصِيبَةٌ بِمَا قَدَّمَتْ أَيْدِيهِمْ فَيَقُولُوا رَبَّنَا لَوْلَا أَرْسَلْتَ إِلَيْنَا رَسُولًا فَنَتَّبِعَ آيَاتِكَ وَنَكُونَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Bu fekkoon ne musaba da leen dale ca la ñu daan jëf ci seeni yoxo, kon dey danañu wax naan : “Yaw sunu Boroom, lu tax yónni woo ci nun ab Yonent ? [Soo ko defoon dey], dinanu topp say ndigal te it dananu gëm doon ay jullit”.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — Al-Qasas 45

Simoore Al-Qasas Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waaye sosoon Nanu ay maas yu guddu na fan. Te…

Simoore Aaya 45/88 — Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qasas Dégg, Al-Qasas Tekki, Al-Qasas mp3, Al-Qasas pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers