Al-'Ankabut · 22/69
Tekki Waxtaan — Al-'Ankabut
وَمَا أَنتُم بِمُعْجِزِينَ فِي الْأَرْضِ وَلَا فِي السَّمَاءِ ۖ وَمَا لَكُم مِّن دُونِ اللَّهِ مِن وَلِيٍّ وَلَا نَصِيرٍ ۝٢٢
Wa maaa antum bimu`jizeena fil ardi wa laa fissamaaa`i wa maa lakum min doonil laahi minw waliyyinw wa laa naseer
📖 Tekkim Wolof
Mënuleen a të ci kaw suuf si waxantumaak asamaan si ; te itam amuleen wenn wéeruwaay mbaa dimbalikat bu dul Yàlla.

🎧 Dégg


📜 Aaya 20-24 — Al-'Ankabut

20قُلْ سِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَانظُرُوا كَيْفَ بَدَأَ الْخَلْقَ ۚ ثُمَّ اللَّهُ يُنشِئُ النَّشْأَةَ الْآخِرَةَ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Neel : “Wërleen [dox] ci kaw suuf si te ngeen xool naka la Yàlla sosee mbindéef yi. Ak itam naka lay sos gu mujj ga di deme. Yàlla mën na lépp lu ne”.
21يُعَذِّبُ مَن يَشَاءُ وَيَرْحَمُ مَن يَشَاءُ ۖ وَإِلَيْهِ تُقْلَبُونَ
Dana mbugal ku ko soob te it Dana yërëm ku ko soob ; te yéen ñépp ca Moom ngeen jëm.
22وَمَا أَنتُم بِمُعْجِزِينَ فِي الْأَرْضِ وَلَا فِي السَّمَاءِ ۖ وَمَا لَكُم مِّن دُونِ اللَّهِ مِن وَلِيٍّ وَلَا نَصِيرٍ
Mënuleen a të ci kaw suuf si waxantumaak asamaan si ; te itam amuleen wenn wéeruwaay mbaa dimbalikat bu dul Yàlla.
23وَالَّذِينَ كَفَرُوا بِآيَاتِ اللَّهِ وَلِقَائِهِ أُولَٰئِكَ يَئِسُوا مِن رَّحْمَتِي وَأُولَٰئِكَ لَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ
Ña nga xam ne dañoo weddi kàdduy Yàlla ak dajeek Moom, ñooña naag nañu ci Sama yërmaande. Te it danañu am mbugal mu mitti.
24فَمَا كَانَ جَوَابَ قَوْمِهِ إِلَّا أَن قَالُوا اقْتُلُوهُ أَوْ حَرِّقُوهُ فَأَنجَاهُ اللَّهُ مِنَ النَّارِ ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Tontul aw nitam doonul woon lu dul ñuy wax naan : “reyleen ko mbaa ngeen lakk ko”. Yàlla musal na ko ca safara sa. Ay kéemaan a ngi ci biir loolu ngir aw nit ñu gëm.
Al-'AnkabutFihi Alxuraan
69Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — Al-'Ankabut 22

Simoore Al-'Ankabut Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mënuleen a të ci kaw suuf si waxantumaak asamaan si…

Simoore Aaya 22/69 — Al-'Ankabut العنكبوت (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-'Ankabut Dégg, Al-'Ankabut Tekki, Al-'Ankabut mp3, Al-'Ankabut pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers