Al-'Ankabut · 34/69
Tekki Waxtaan — Simoore Al-'Ankabut
إِنَّا مُنزِلُونَ عَلَىٰ أَهْلِ هَٰذِهِ الْقَرْيَةِ رِجْزًا مِّنَ السَّمَاءِ بِمَا كَانُوا يَفْسُقُونَ ۝٣٤
Innaa munziloona `alaaa ahli haazihil qaryati rijzam minas samaaa`i bimaa kaanoo yafsuqoon
📖 Tekkim Wolof
Wàcce Nanu ci kaw waa dëkk bi mbugal mu bawoo asamaan ngir seen caay-caay ga”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 32-36 — Simoore Al-'Ankabut

32قَالَ إِنَّ فِيهَا لُوطًا ۚ قَالُوا نَحْنُ أَعْلَمُ بِمَن فِيهَا ۖ لَنُنَجِّيَنَّهُ وَأَهْلَهُ إِلَّا امْرَأَتَهُ كَانَتْ مِنَ الْغَابِرِينَ
Ibraahiima ne leen : “Waaye Lóot ma nga fa ! ”. Ñu tontu ko ne ko : “Noo gën a xam ña fa nekk : Dananu musal [moom Lóot] mook njabootam, ba mu des soxnaam, moom day bokk ca ña alku”.
33وَلَمَّا أَن جَاءَتْ رُسُلُنَا لُوطًا سِيءَ بِهِمْ وَضَاقَ بِهِمْ ذَرْعًا وَقَالُوا لَا تَخَفْ وَلَا تَحْزَنْ ۖ إِنَّا مُنَجُّوكَ وَأَهْلَكَ إِلَّا امْرَأَتَكَ كَانَتْ مِنَ الْغَابِرِينَ
ba Sunu ndawi Malaaka yi agsee ci Lóot, ñaawalees na jëme ci ñoom, mu tiit ci seeni mbir. Ñu ne ko : “Bul tiit, bul ragal... Dananu la musal yaak sa njaboot, ba mu des sa jabar, dafay alku.
34إِنَّا مُنزِلُونَ عَلَىٰ أَهْلِ هَٰذِهِ الْقَرْيَةِ رِجْزًا مِّنَ السَّمَاءِ بِمَا كَانُوا يَفْسُقُونَ
Wàcce Nanu ci kaw waa dëkk bi mbugal mu bawoo asamaan ngir seen caay-caay ga”.
35وَلَقَد تَّرَكْنَا مِنْهَا آيَةً بَيِّنَةً لِّقَوْمٍ يَعْقِلُونَ
Bàyyi Nanu fa lu bokk ca ñoom muy kéemaan gu leer nàññ ngir aw nit ñuy xel-lu.
36وَإِلَىٰ مَدْيَنَ أَخَاهُمْ شُعَيْبًا فَقَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ وَارْجُوا الْيَوْمَ الْآخِرَ وَلَا تَعْثَوْا فِي الْأَرْضِ مُفْسِدِينَ
[Naka noonu], la seen mbokk Chuhaybu demee woon Madyaana, ne leen : “Éy yéen samaw nit, jaamuleen Yàlla te gëm Bis-pénc ba, te buleen dox di yàq ci kaw suuf si”.
Al-'AnkabutFihi Alxuraan
69Aaya
MeccanRevelation
34Aaya

Tekki — Al-'Ankabut 34

Simoore Al-'Ankabut Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Wàcce Nanu ci kaw waa dëkk bi mbugal mu bawoo…

Simoore Aaya 34/69 — Simoore Al-'Ankabut العنكبوت (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-'Ankabut Dégg, Simoore Al-'Ankabut Tekki, Simoore Al-'Ankabut mp3, Simoore Al-'Ankabut pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers