Aali Imran · 99/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
قُلْ يَا أَهْلَ الْكِتَابِ لِمَ تَصُدُّونَ عَن سَبِيلِ اللَّهِ مَنْ آمَنَ تَبْغُونَهَا عِوَجًا وَأَنتُمْ شُهَدَاءُ ۗ وَمَا اللَّهُ بِغَافِلٍ عَمَّا تَعْمَلُونَ ٩٩
Transliteration
Qul yaaa Ahlal Kitaabi lima tusuddoona `an sabeelil laahi man aamana tabghoonahaa `iwajanw wa antum shuhadaaa`; wa mallaahu bighaafilin `ammaa ta`maloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Yéen ñoñ-téere, lu tax ngeen di gàllankoor ñiy dox jëm ci yoonu Yàlla, di ko wutal sikk? Te ngeen di ay seede, te Yàlla sàgganewut li ngeen di jëf de.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 97-101 — Aali Imran
97فِيهِ آيَاتٌ بَيِّنَاتٌ مَّقَامُ إِبْرَاهِيمَ ۖ وَمَن دَخَلَهُ كَانَ آمِنًا ۗ وَلِلَّهِ عَلَى النَّاسِ حِجُّ الْبَيْتِ مَنِ اسْتَطَاعَ إِلَيْهِ سَبِيلًا ۚ وَمَن كَفَرَ فَإِنَّ اللَّهَ غَنِيٌّ عَنِ الْعَالَمِينَ
Ay kéemaan yu leer ñoo fa nekk, [bokk na ca] Maxaama Ibraahiima [barab] ; ku fa dugg am kóolute. War na, ci nit ñi ku ko mën, aj fa néegub Yàlla ba te Yàlla tax wenn yoon [wu farata]. Ku weddi nag... na xam ne Yàlla ku doyloo la waliis mbindéef yépp.
98قُلْ يَا أَهْلَ الْكِتَابِ لِمَ تَكْفُرُونَ بِآيَاتِ اللَّهِ وَاللَّهُ شَهِيدٌ عَلَىٰ مَا تَعْمَلُونَ
Neel : “Yéen ñoñ-téere, lu tax ngeen di weddi kàdduy Yàlla yi? Te Yàlla kuy seede la ci li ngeen di def ”
99قُلْ يَا أَهْلَ الْكِتَابِ لِمَ تَصُدُّونَ عَن سَبِيلِ اللَّهِ مَنْ آمَنَ تَبْغُونَهَا عِوَجًا وَأَنتُمْ شُهَدَاءُ ۗ وَمَا اللَّهُ بِغَافِلٍ عَمَّا تَعْمَلُونَ
Neel : “Yéen ñoñ-téere, lu tax ngeen di gàllankoor ñiy dox jëm ci yoonu Yàlla, di ko wutal sikk? Te ngeen di ay seede, te Yàlla sàgganewut li ngeen di jëf de.
100يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِن تُطِيعُوا فَرِيقًا مِّنَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ يَرُدُّوكُم بَعْدَ إِيمَانِكُمْ كَافِرِينَ
Éy yéen ñi gëm ! Bu ngeen toppee ñenn ñi, ñoñ-téere, danañu leen delloo ci kéefar gannaaw ba ngeen gëmee Yàlla.
101وَكَيْفَ تَكْفُرُونَ وَأَنتُمْ تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ آيَاتُ اللَّهِ وَفِيكُمْ رَسُولُهُ ۗ وَمَن يَعْتَصِم بِاللَّهِ فَقَدْ هُدِيَ إِلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Naka ngeen di weddee te laayay Yàlla yi ñi di ko jàng fi seen kanam, Yonent bi nekk fi seen biir ? Ku ŋoy ci Yàlla, gindiku na jëm ca yoon wu jub xocc wa.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
99Aaya
Tekki — Aali Imran 99
Simoore Aali Imran Aaya 99 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Yéen ñoñ-téere, lu tax ngeen di gàllankoor ñiy…Simoore Aaya 99/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 97–101. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








