Al-Ahzab · 3/73
Tekki Waxtaan — Al-Ahzab
وَتَوَكَّلْ عَلَى اللَّهِ ۚ وَكَفَىٰ بِاللَّهِ وَكِيلًا ٣
Transliteration
Wa tawakkal `alal laah; wa kafaa billaahi Wakeelaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te nangay wéeru ci Yàlla. [Ndax] Yàlla doy na sëkk wéeruwaay.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 1-5 — Al-Ahzab
1يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ اتَّقِ اللَّهَ وَلَا تُطِعِ الْكَافِرِينَ وَالْمُنَافِقِينَ ۗ إِنَّ اللَّهَ كَانَ عَلِيمًا حَكِيمًا
Éy yaw Yonent bi ! Ragalal Yàlla te bul topp yéefar yi ak naaféq yi, Yàlla ku xam la, Ku xereñ la.
2وَاتَّبِعْ مَا يُوحَىٰ إِلَيْكَ مِن رَّبِّكَ ۚ إِنَّ اللَّهَ كَانَ بِمَا تَعْمَلُونَ خَبِيرًا
Toppal li ñu lay soloo te mu bawoo ca sa Boroom. Yàlla xàmmee na ca la ngeen di def.
3وَتَوَكَّلْ عَلَى اللَّهِ ۚ وَكَفَىٰ بِاللَّهِ وَكِيلًا
Te nangay wéeru ci Yàlla. [Ndax] Yàlla doy na sëkk wéeruwaay.
4مَّا جَعَلَ اللَّهُ لِرَجُلٍ مِّن قَلْبَيْنِ فِي جَوْفِهِ ۚ وَمَا جَعَلَ أَزْوَاجَكُمُ اللَّائِي تُظَاهِرُونَ مِنْهُنَّ أُمَّهَاتِكُمْ ۚ وَمَا جَعَلَ أَدْعِيَاءَكُمْ أَبْنَاءَكُمْ ۚ ذَٰلِكُمْ قَوْلُكُم بِأَفْوَاهِكُمْ ۖ وَاللَّهُ يَقُولُ الْحَقَّ وَهُوَ يَهْدِي السَّبِيلَ
Yàlla defalul kenn nit ñaari xol ci dënnëm. Deful it jabar yi ngeen di wodde seen pendali ndey [ci pase] ñuy seeni yaay . Deful it doom yi ngeen doomoo ñuy seeni doom. Loolu seeni wax doŋŋ la ju yem ci seeni gémmiñ. Yàlla dëgg lay wax te Mooy jubbanti, di tege ci yoon wu jub.
5ادْعُوهُمْ لِآبَائِهِمْ هُوَ أَقْسَطُ عِندَ اللَّهِ ۚ فَإِن لَّمْ تَعْلَمُوا آبَاءَهُمْ فَإِخْوَانُكُمْ فِي الدِّينِ وَمَوَالِيكُمْ ۚ وَلَيْسَ عَلَيْكُمْ جُنَاحٌ فِيمَا أَخْطَأْتُم بِهِ وَلَٰكِن مَّا تَعَمَّدَتْ قُلُوبُكُمْ ۚ وَكَانَ اللَّهُ غَفُورًا رَّحِيمًا
Appelez-les du nom de leurs pères : c’est plus équitable devant Allah. Ña ngeen xamul seeni baay, kon ñoom seeni mbokk la ñuy doon ci diine ak seeni farandoo. Ayul ci yéen it lu ngeen ca wax te muy njuumte, li aay kay mooy la ngeen ca wax te tey ko. Yàlla, Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
3Aaya
Tekki — Al-Ahzab 3
Simoore Al-Ahzab Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te nangay wéeru ci Yàlla. [Ndax] Yàlla doy na sëkk…Simoore Aaya 3/73 — Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahzab Dégg, Al-Ahzab Tekki, Al-Ahzab mp3, Al-Ahzab pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








