Fatir · 26/45
Tekki Waxtaan — Simoore Fatir
ثُمَّ أَخَذْتُ الَّذِينَ كَفَرُوا ۖ فَكَيْفَ كَانَ نَكِيرِ ۝٢٦
Summa akhaztul lazeena kafaroo fakaifa kaana nakeer
📖 Tekkim Wolof
Ginnaaw ba, Ma jël ña weddi. Cëy na Ma leen jële.

🎧 Dégg


📜 Aaya 24-28 — Simoore Fatir

24إِنَّا أَرْسَلْنَاكَ بِالْحَقِّ بَشِيرًا وَنَذِيرًا ۚ وَإِن مِّنْ أُمَّةٍ إِلَّا خَلَا فِيهَا نَذِيرٌ
Yónni Nanu la ci dëgg ngay bégalekat di ab xuppekat, amul wenn xeet wu amul ab xuppekat.
25وَإِن يُكَذِّبُوكَ فَقَدْ كَذَّبَ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ جَاءَتْهُمْ رُسُلُهُم بِالْبَيِّنَاتِ وَبِالزُّبُرِ وَبِالْكِتَابِ الْمُنِيرِ
Su fekke ne dañu laa weddi, [xamal ne] am na ñu leen jiitu woon te daan weddi, ndax seeni Yonent indiloon nañu leen ay laaya, ay firnde yu bir ak ay mbind ak ab Téere bu leer.
26ثُمَّ أَخَذْتُ الَّذِينَ كَفَرُوا ۖ فَكَيْفَ كَانَ نَكِيرِ
Ginnaaw ba, Ma jël ña weddi. Cëy na Ma leen jële.
27أَلَمْ تَرَ أَنَّ اللَّهَ أَنزَلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَأَخْرَجْنَا بِهِ ثَمَرَاتٍ مُّخْتَلِفًا أَلْوَانُهَا ۚ وَمِنَ الْجِبَالِ جُدَدٌ بِيضٌ وَحُمْرٌ مُّخْتَلِفٌ أَلْوَانُهَا وَغَرَابِيبُ سُودٌ
Xanaa gisuloo ne Yàlla moo wàcce ndox mu bawoo ci asamaan si ? Nu daldi cay génne ay meññent yu wuute ay wirgu. Am na it ci tundi doj yi yuy sësëloo te weex, ak yuy xonk, yu wuute ay wirgu, ak yu ñuul kukk.
28وَمِنَ النَّاسِ وَالدَّوَابِّ وَالْأَنْعَامِ مُخْتَلِفٌ أَلْوَانُهُ كَذَٰلِكَ ۗ إِنَّمَا يَخْشَى اللَّهَ مِنْ عِبَادِهِ الْعُلَمَاءُ ۗ إِنَّ اللَّهَ عَزِيزٌ غَفُورٌ
Am na it ci nit ñi, ci daaba yeek mala yi yu wuute ay wirgu, noonu rekk la. Jaami Yàlla yi ko ragal ñoo di woroom xam-xam yi. Te Yàlla boroom xam-xam la, di Jéggalaakoon.
FatirFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — Fatir 26

Simoore Fatir Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ginnaaw ba, Ma jël ña weddi. Cëy na Ma leen…

Simoore Aaya 26/45 — Simoore Fatir فاطر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Fatir Dégg, Simoore Fatir Tekki, Simoore Fatir mp3, Simoore Fatir pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers