Ya-Sin · 72/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
وَذَلَّلْنَاهَا لَهُمْ فَمِنْهَا رَكُوبُهُمْ وَمِنْهَا يَأْكُلُونَ ٧٢
Transliteration
Wa zallalnaahaa lahum faminhaa rakoobuhum wa minhaa yaakuloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nu tàggatal leen ko ; ñu di ca war te it ñu di ca lekk ;
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 70-74 — Ya-Sin
70لِّيُنذِرَ مَن كَانَ حَيًّا وَيَحِقَّ الْقَوْلُ عَلَى الْكَافِرِينَ
ngir muy xupp ñiy dundu, wax ja itam di lu yay ca yéefar ya.
71أَوَلَمْ يَرَوْا أَنَّا خَلَقْنَا لَهُم مِّمَّا عَمِلَتْ أَيْدِينَا أَنْعَامًا فَهُمْ لَهَا مَالِكُونَ
Xanaa dañoo gisul ne sàkkal Nanu leen ci Sunu liggéeyu loxo ag jur gu ñuy moom ;
72وَذَلَّلْنَاهَا لَهُمْ فَمِنْهَا رَكُوبُهُمْ وَمِنْهَا يَأْكُلُونَ
Nu tàggatal leen ko ; ñu di ca war te it ñu di ca lekk ;
73وَلَهُمْ فِيهَا مَنَافِعُ وَمَشَارِبُ ۖ أَفَلَا يَشْكُرُونَ
am nañu ci ay njariñ ak i naan. Moo ndax dañu dul sant ?
74وَاتَّخَذُوا مِن دُونِ اللَّهِ آلِهَةً لَّعَلَّهُمْ يُنصَرُونَ
Ñuy jàppe yàlla leneen lu dul Yàlla, ngir ñu neey danuy sàkku ndimbal...
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
72Aaya
Tekki — Ya-Sin 72
Simoore Ya-Sin Aaya 72 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu tàggatal leen ko ; ñu di ca war te…Simoore Aaya 72/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 70–74. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








