Ya-Sin · 71/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
أَوَلَمْ يَرَوْا أَنَّا خَلَقْنَا لَهُم مِّمَّا عَمِلَتْ أَيْدِينَا أَنْعَامًا فَهُمْ لَهَا مَالِكُونَ ۝٧١
Awalam yaraw annaa khalaqnaa lahum mimmaa `amilat aideenaaa an`aaman fahum lahaa maalikoon
📖 Tekkim Wolof
Xanaa dañoo gisul ne sàkkal Nanu leen ci Sunu liggéeyu loxo ag jur gu ñuy moom ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 69-73 — Simoore Ya-Sin

69وَمَا عَلَّمْنَاهُ الشِّعْرَ وَمَا يَنبَغِي لَهُ ۚ إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرٌ وَقُرْآنٌ مُّبِينٌ
Jàngalunu Muhammad woy mbaa lu koy nuru ; lii daal du dara lu dul ag fàttali ak Alxuraan juy biral,
70لِّيُنذِرَ مَن كَانَ حَيًّا وَيَحِقَّ الْقَوْلُ عَلَى الْكَافِرِينَ
ngir muy xupp ñiy dundu, wax ja itam di lu yay ca yéefar ya.
71أَوَلَمْ يَرَوْا أَنَّا خَلَقْنَا لَهُم مِّمَّا عَمِلَتْ أَيْدِينَا أَنْعَامًا فَهُمْ لَهَا مَالِكُونَ
Xanaa dañoo gisul ne sàkkal Nanu leen ci Sunu liggéeyu loxo ag jur gu ñuy moom ;
72وَذَلَّلْنَاهَا لَهُمْ فَمِنْهَا رَكُوبُهُمْ وَمِنْهَا يَأْكُلُونَ
Nu tàggatal leen ko ; ñu di ca war te it ñu di ca lekk ;
73وَلَهُمْ فِيهَا مَنَافِعُ وَمَشَارِبُ ۖ أَفَلَا يَشْكُرُونَ
am nañu ci ay njariñ ak i naan. Moo ndax dañu dul sant ?
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
71Aaya

Tekki — Ya-Sin 71

Simoore Ya-Sin Aaya 71 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xanaa dañoo gisul ne sàkkal Nanu leen ci Sunu liggéeyu…

Simoore Aaya 71/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 69–73. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers