As-Saffat · 121/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ ۝١٢١
Innaa kazaalika najzil muhsineen
📖 Tekkim Wolof
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 119-123 — Simoore As-Saffat

119وَتَرَكْنَا عَلَيْهِمَا فِي الْآخِرِينَ
Nu bàyyi woon leen nit ña di leen fàttaliku :
120سَلَامٌ عَلَىٰ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
“Jàmmi Yàlla na wàcc ci Muusaa ak Haaruuna”
121إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal ;
122إِنَّهُمَا مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
ñoom ñaar bokkoon nañu ci Sunu jaam ñi gëm.
123وَإِنَّ إِلْيَاسَ لَمِنَ الْمُرْسَلِينَ
Ilyaas it tigi bokkoon na ci Yonent ya.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
121Aaya

Tekki — As-Saffat 121

Simoore As-Saffat Aaya 121 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noonu la Nuy feye ñiy rafetal ;

Simoore Aaya 121/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 119–123. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers