As-Saffat · 120/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
سَلَامٌ عَلَىٰ مُوسَىٰ وَهَارُونَ ۝١٢٠
Salaamun `alaa Moosaa wa Haaroon
📖 Tekkim Wolof
“Jàmmi Yàlla na wàcc ci Muusaa ak Haaruuna”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 118-122 — Simoore As-Saffat

118وَهَدَيْنَاهُمَا الصِّرَاطَ الْمُسْتَقِيمَ
Nu indiloon leen yoon wu jub wa xocc.
119وَتَرَكْنَا عَلَيْهِمَا فِي الْآخِرِينَ
Nu bàyyi woon leen nit ña di leen fàttaliku :
120سَلَامٌ عَلَىٰ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
“Jàmmi Yàlla na wàcc ci Muusaa ak Haaruuna”
121إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal ;
122إِنَّهُمَا مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
ñoom ñaar bokkoon nañu ci Sunu jaam ñi gëm.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
120Aaya

Tekki — As-Saffat 120

Simoore As-Saffat Aaya 120 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Jàmmi Yàlla na wàcc ci Muusaa ak Haaruuna”

Simoore Aaya 120/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 118–122. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers