As-Saffat · 122/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِنَّهُمَا مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ ۝١٢٢
Innahumaa min `ibaadinal mu`mineen
📖 Tekkim Wolof
ñoom ñaar bokkoon nañu ci Sunu jaam ñi gëm.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 120-124 — Simoore As-Saffat

120سَلَامٌ عَلَىٰ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
“Jàmmi Yàlla na wàcc ci Muusaa ak Haaruuna”
121إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal ;
122إِنَّهُمَا مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
ñoom ñaar bokkoon nañu ci Sunu jaam ñi gëm.
123وَإِنَّ إِلْيَاسَ لَمِنَ الْمُرْسَلِينَ
Ilyaas it tigi bokkoon na ci Yonent ya.
124إِذْ قَالَ لِقَوْمِهِ أَلَا تَتَّقُونَ
[Fàttalikul] ba mu waxee aw nitam, ne leen : “Ndax dungeen ragal Yàlla ? ”
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
122Aaya

Tekki — As-Saffat 122

Simoore As-Saffat Aaya 122 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñoom ñaar bokkoon nañu ci Sunu jaam ñi gëm.

Simoore Aaya 122/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 120–124. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Sunday, October 4, 2026

Don't forget us in your sincere prayers