As-Saffat · 123/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَإِنَّ إِلْيَاسَ لَمِنَ الْمُرْسَلِينَ ۝١٢٣
Wa inna Ilyaasa laminal mursaleen
📖 Tekkim Wolof
Ilyaas it tigi bokkoon na ci Yonent ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 121-125 — Simoore As-Saffat

121إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal ;
122إِنَّهُمَا مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
ñoom ñaar bokkoon nañu ci Sunu jaam ñi gëm.
123وَإِنَّ إِلْيَاسَ لَمِنَ الْمُرْسَلِينَ
Ilyaas it tigi bokkoon na ci Yonent ya.
124إِذْ قَالَ لِقَوْمِهِ أَلَا تَتَّقُونَ
[Fàttalikul] ba mu waxee aw nitam, ne leen : “Ndax dungeen ragal Yàlla ? ”
125أَتَدْعُونَ بَعْلًا وَتَذَرُونَ أَحْسَنَ الْخَالِقِينَ
Moo ngax dangeen di woo Bahlu bàyyi Yàlla miy ngën ji kuy bind,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
123Aaya

Tekki — As-Saffat 123

Simoore As-Saffat Aaya 123 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ilyaas it tigi bokkoon na ci Yonent ya.

Simoore Aaya 123/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 121–125. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers