As-Saffat · 124/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِذْ قَالَ لِقَوْمِهِ أَلَا تَتَّقُونَ ۝١٢٤
Iz qaala liqawmiheee alaa tattaqoon
📖 Tekkim Wolof
[Fàttalikul] ba mu waxee aw nitam, ne leen : “Ndax dungeen ragal Yàlla ? ”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 122-126 — Simoore As-Saffat

122إِنَّهُمَا مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
ñoom ñaar bokkoon nañu ci Sunu jaam ñi gëm.
123وَإِنَّ إِلْيَاسَ لَمِنَ الْمُرْسَلِينَ
Ilyaas it tigi bokkoon na ci Yonent ya.
124إِذْ قَالَ لِقَوْمِهِ أَلَا تَتَّقُونَ
[Fàttalikul] ba mu waxee aw nitam, ne leen : “Ndax dungeen ragal Yàlla ? ”
125أَتَدْعُونَ بَعْلًا وَتَذَرُونَ أَحْسَنَ الْخَالِقِينَ
Moo ngax dangeen di woo Bahlu bàyyi Yàlla miy ngën ji kuy bind,
126اللَّهَ رَبَّكُمْ وَرَبَّ آبَائِكُمُ الْأَوَّلِينَ
Yàlla miy seen Boroom te di Boroomi seeni baay ak i maamaat ? ”
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
124Aaya

Tekki — As-Saffat 124

Simoore As-Saffat Aaya 124 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Fàttalikul] ba mu waxee aw nitam, ne leen : “Ndax…

Simoore Aaya 124/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 122–126. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers