As-Saffat · 156/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
أَمْ لَكُمْ سُلْطَانٌ مُّبِينٌ ۝١٥٦
Am lakum sultaanum mubeen
📖 Tekkim Wolof
Walla dangeen am ay firnde yu wóor ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 154-158 — Simoore As-Saffat

154مَا لَكُمْ كَيْفَ تَحْكُمُونَ
Ana lu leen dal ba ngeen di àttee nii ?
155أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
Moo ndax dangeen dul fàttaliku ?
156أَمْ لَكُمْ سُلْطَانٌ مُّبِينٌ
Walla dangeen am ay firnde yu wóor ?
157فَأْتُوا بِكِتَابِكُمْ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Kon indil seenub Téere ndegam ñu dëggu ngeen ! ”
158وَجَعَلُوا بَيْنَهُ وَبَيْنَ الْجِنَّةِ نَسَبًا ۚ وَلَقَدْ عَلِمَتِ الْجِنَّةُ إِنَّهُمْ لَمُحْضَرُونَ
Ñu di ko askanale ci jinne yi, ndax jinne yi xam nañu ne danañu teew ci kanamu [Yàlla].
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
156Aaya

Tekki — As-Saffat 156

Simoore As-Saffat Aaya 156 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla dangeen am ay firnde yu wóor ?

Simoore Aaya 156/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 154–158. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers