As-Saffat · 58/182
Tekki Waxtaan — As-Saffat
أَفَمَا نَحْنُ بِمَيِّتِينَ ۝٥٨
Afamaa nahnu bimaiyiteen
📖 Tekkim Wolof
Xanaa nun dey dunu dee

🎧 Dégg


📜 Aaya 56-60 — As-Saffat

56قَالَ تَاللَّهِ إِن كِدتَّ لَتُرْدِينِ
mu wax ne : “Waat naa ci Yàlla ne ! Xaw nga maa tax a alku !
57وَلَوْلَا نِعْمَةُ رَبِّي لَكُنتُ مِنَ الْمُحْضَرِينَ
dogankoon ak sama dimbalul Boroom, danaa sànku.
58أَفَمَا نَحْنُ بِمَيِّتِينَ
Xanaa nun dey dunu dee
59إِلَّا مَوْتَتَنَا الْأُولَىٰ وَمَا نَحْنُ بِمُعَذَّبِينَ
lu dul ca dee gu jëkk ga te xanaa kenn dunu mbugal ? ”
60إِنَّ هَٰذَا لَهُوَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ
Lii mooy texe gu màgg ga.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
58Aaya

Tekki — As-Saffat 58

Simoore As-Saffat Aaya 58 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xanaa nun dey dunu dee

Simoore Aaya 58/182 — As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: As-Saffat Dégg, As-Saffat Tekki, As-Saffat mp3, As-Saffat pdf. Aaya 56–60. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers