Sad · 73/88
Tekki Waxtaan — Simoore Sad
فَسَجَدَ الْمَلَائِكَةُ كُلُّهُمْ أَجْمَعُونَ ۝٧٣
Fasajadal malaaa`ikatu kulluhum ajma`oon
📖 Tekkim Wolof
Malaaka ya yépp daldi sujuud,

🎧 Dégg


📜 Aaya 71-75 — Simoore Sad

71إِذْ قَالَ رَبُّكَ لِلْمَلَائِكَةِ إِنِّي خَالِقٌ بَشَرًا مِّن طِينٍ
(Fàttalitul) ba sa Boroom waxee Malaaka ya ne leen : “Man de maa ngi sàkk mbindéef ci ban.
72فَإِذَا سَوَّيْتُهُ وَنَفَخْتُ فِيهِ مِن رُّوحِي فَقَعُوا لَهُ سَاجِدِينَ
Suma ko móolee ba ëf ci Sama Ruu, na ngeen daldi rot, sujuudal ko”.
73فَسَجَدَ الْمَلَائِكَةُ كُلُّهُمْ أَجْمَعُونَ
Malaaka ya yépp daldi sujuud,
74إِلَّا إِبْلِيسَ اسْتَكْبَرَ وَكَانَ مِنَ الْكَافِرِينَ
ba mu des Ibliis moom dafa rëy-rëylu bokk ca yéefar ya.
75قَالَ يَا إِبْلِيسُ مَا مَنَعَكَ أَن تَسْجُدَ لِمَا خَلَقْتُ بِيَدَيَّ ۖ أَسْتَكْبَرْتَ أَمْ كُنتَ مِنَ الْعَالِينَ
(Yàlla) daldi ne : “yaw Ibliis, lan moo la tere nga sujuud ci lii ma bind ci samay yoxo ? Dangay rëy-rëylu walla dangaa bokk ci ña kawe ? ”
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
73Aaya

Tekki — Sad 73

Simoore Sad Aaya 73 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Malaaka ya yépp daldi sujuud,

Simoore Aaya 73/88 — Simoore Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Sad Dégg, Simoore Sad Tekki, Simoore Sad mp3, Simoore Sad pdf. Aaya 71–75. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers