Sad · 81/88
Tekki Waxtaan — Simoore Sad
إِلَىٰ يَوْمِ الْوَقْتِ الْمَعْلُومِ ۝٨١
Ilaa Yawmil waqtil ma`loom
📖 Tekkim Wolof
ba ca bisub waxtu wu ñu xam wa (Bis Pénc ba)”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 79-83 — Simoore Sad

79قَالَ رَبِّ فَأَنظِرْنِي إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
“[Ibliis,] ne ko : yaw sama Boroom, muñal ma, ba bisub dekkiwaat ba”.
80قَالَ فَإِنَّكَ مِنَ الْمُنظَرِينَ
(Yàlla) ne ko : “may Nanu la dig boobu,
81إِلَىٰ يَوْمِ الْوَقْتِ الْمَعْلُومِ
ba ca bisub waxtu wu ñu xam wa (Bis Pénc ba)”.
82قَالَ فَبِعِزَّتِكَ لَأُغْوِيَنَّهُمْ أَجْمَعِينَ
“[Ibliis ne ko] giiñ naa ci sa màgg gi ne ! Danaa leen lajj loo ñoom ñépp,
83إِلَّا عِبَادَكَ مِنْهُمُ الْمُخْلَصِينَ
ba mu des sa jaam ñiy sellal”.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
81Aaya

Tekki — Sad 81

Simoore Sad Aaya 81 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba ca bisub waxtu wu ñu xam wa (Bis Pénc…

Simoore Aaya 81/88 — Simoore Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Sad Dégg, Simoore Sad Tekki, Simoore Sad mp3, Simoore Sad pdf. Aaya 79–83. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers