Sad · 82/88
Tekki Waxtaan — Simoore Sad
قَالَ فَبِعِزَّتِكَ لَأُغْوِيَنَّهُمْ أَجْمَعِينَ ۝٨٢
Qaala fabi`izzatika la ughwiyannahum ajma`een
📖 Tekkim Wolof
“[Ibliis ne ko] giiñ naa ci sa màgg gi ne ! Danaa leen lajj loo ñoom ñépp,

🎧 Dégg


📜 Aaya 80-84 — Simoore Sad

80قَالَ فَإِنَّكَ مِنَ الْمُنظَرِينَ
(Yàlla) ne ko : “may Nanu la dig boobu,
81إِلَىٰ يَوْمِ الْوَقْتِ الْمَعْلُومِ
ba ca bisub waxtu wu ñu xam wa (Bis Pénc ba)”.
82قَالَ فَبِعِزَّتِكَ لَأُغْوِيَنَّهُمْ أَجْمَعِينَ
“[Ibliis ne ko] giiñ naa ci sa màgg gi ne ! Danaa leen lajj loo ñoom ñépp,
83إِلَّا عِبَادَكَ مِنْهُمُ الْمُخْلَصِينَ
ba mu des sa jaam ñiy sellal”.
84قَالَ فَالْحَقُّ وَالْحَقَّ أَقُولُ
(Yàlla) daldi wax ne : “Maa ngi waat, ci dëgg ne dëgg laay wax,
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
82Aaya

Tekki — Sad 82

Simoore Sad Aaya 82 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “[Ibliis ne ko] giiñ naa ci sa màgg gi ne…

Simoore Aaya 82/88 — Simoore Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Sad Dégg, Simoore Sad Tekki, Simoore Sad mp3, Simoore Sad pdf. Aaya 80–84. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers