Az-Zumar · 46/75
Tekki Waxtaan — Az-Zumar
قُلِ اللَّهُمَّ فَاطِرَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ عَالِمَ الْغَيْبِ وَالشَّهَادَةِ أَنتَ تَحْكُمُ بَيْنَ عِبَادِكَ فِي مَا كَانُوا فِيهِ يَخْتَلِفُونَ ۝٤٦
Qulil laahumma faatiras samaawaati wal ardi `Aalimal Ghaibi washshahaadati Anta tahkumu baina `ibaadika fee maa kaanoo fee yakhtalifoon
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne : “yaw sama Boroom, Yaa bind sàkk asamaan yeek suuf si, Yaa xam kumpa ak li feeñ, te danga àtte diggënte Sa jaam ñi ci la nu daan woote”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 44-48 — Az-Zumar

44قُل لِّلَّهِ الشَّفَاعَةُ جَمِيعًا ۖ لَّهُ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ ثُمَّ إِلَيْهِ تُرْجَعُونَ
Waxal ne : “Tinu ba tinu jeex (ramm) Yàllaa ko jagoo. Miy boroom nguurug asamaan yeek suuf. Te ci moom ngeen di dellu”
45وَإِذَا ذُكِرَ اللَّهُ وَحْدَهُ اشْمَأَزَّتْ قُلُوبُ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ ۖ وَإِذَا ذُكِرَ الَّذِينَ مِن دُونِهِ إِذَا هُمْ يَسْتَبْشِرُونَ
Te saa su ñu tuddee Yàlla doŋŋ, xoli ñi gëmul àllaaxira tàmbalee wurwuri (xat mer) saa su ñu tuddee ñeneen (ya ñu koy bokkaaleel), ñu daldi bég.
46قُلِ اللَّهُمَّ فَاطِرَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ عَالِمَ الْغَيْبِ وَالشَّهَادَةِ أَنتَ تَحْكُمُ بَيْنَ عِبَادِكَ فِي مَا كَانُوا فِيهِ يَخْتَلِفُونَ
Waxal ne : “yaw sama Boroom, Yaa bind sàkk asamaan yeek suuf si, Yaa xam kumpa ak li feeñ, te danga àtte diggënte Sa jaam ñi ci la nu daan woote”.
47وَلَوْ أَنَّ لِلَّذِينَ ظَلَمُوا مَا فِي الْأَرْضِ جَمِيعًا وَمِثْلَهُ مَعَهُ لَافْتَدَوْا بِهِ مِن سُوءِ الْعَذَابِ يَوْمَ الْقِيَامَةِ ۚ وَبَدَا لَهُم مِّنَ اللَّهِ مَا لَمْ يَكُونُوا يَحْتَسِبُونَ
Te ñiy tooñ su ñu amoon àddina ak li ci biiram, - ak leneen lu na tollaat, - kon danañu ko jéem a jote seen bopp bu Bis Pénc baa ; ngir mbugël mu tar, ak la ñu gis mu bawoo ca Yàlla, te masu ñu koo foog ;
48وَبَدَا لَهُمْ سَيِّئَاتُ مَا كَسَبُوا وَحَاقَ بِهِم مَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
seen ñaawtéef ya ñu fàggu woon feeñ, la ñu daan ñaawalaatee muur leen.
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — Az-Zumar 46

Simoore Az-Zumar Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne : “yaw sama Boroom, Yaa bind sàkk asamaan…

Simoore Aaya 46/75 — Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zumar Dégg, Az-Zumar Tekki, Az-Zumar mp3, Az-Zumar pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers