Az-Zukhruf · 28/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
وَجَعَلَهَا كَلِمَةً بَاقِيَةً فِي عَقِبِهِ لَعَلَّهُمْ يَرْجِعُونَ ۝٢٨
Wa ja`alahaa Kalimatam baaqiyatan fee `aqibihee la`al lahum yarji`oon
📖 Tekkim Wolof
Mu def (dénkaane boobu) muy kàddu guy sax ginnaawam. Ngir amaana ñu dellu (di jëfe seeni xel) ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 26-30 — Simoore Az-Zukhruf

26وَإِذْ قَالَ إِبْرَاهِيمُ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ إِنَّنِي بَرَاءٌ مِّمَّا تَعْبُدُونَ
(Fàttalikul) Ibraahiima ba mu waxee baayam aku nitam : “Man mii ku deñ laa ci lii ngeen di jaamu,
27إِلَّا الَّذِي فَطَرَنِي فَإِنَّهُ سَيَهْدِينِ
ba mu des (Yàlla) mi ma sàkk bind ma, te moo may gindi”.
28وَجَعَلَهَا كَلِمَةً بَاقِيَةً فِي عَقِبِهِ لَعَلَّهُمْ يَرْجِعُونَ
Mu def (dénkaane boobu) muy kàddu guy sax ginnaawam. Ngir amaana ñu dellu (di jëfe seeni xel) ?
29بَلْ مَتَّعْتُ هَٰؤُلَاءِ وَآبَاءَهُمْ حَتَّىٰ جَاءَهُمُ الْحَقُّ وَرَسُولٌ مُّبِينٌ
Waaye xéewaloon naa ñooñee ak seeni maam, Ba dëgg ga (Alxuraan) digël leen ànd ak Yonnent buy leeral.
30وَلَمَّا جَاءَهُمُ الْحَقُّ قَالُوا هَٰذَا سِحْرٌ وَإِنَّا بِهِ كَافِرُونَ
Ba leen dëgg ga digëlee, dañoo wax naan : “Lii daal ag njibar la te nun ay fen la nu ko jàppe”.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 28

Simoore Az-Zukhruf Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu def (dénkaane boobu) muy kàddu guy sax ginnaawam. Ngir…

Simoore Aaya 28/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers