Az-Zukhruf · 7/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
وَمَا يَأْتِيهِم مِّن نَّبِيٍّ إِلَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ ۝٧
Wa maa yaateehim min Nabiyyin illaa kaanoo bihee yasahzi`oon
📖 Tekkim Wolof
amul Yonnent bu mas a ñëw te yéjjiwuñu ko (ñaawal).

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 5-9 — Simoore Az-Zukhruf

5أَفَنَضْرِبُ عَنكُمُ الذِّكْرَ صَفْحًا أَن كُنتُمْ قَوْمًا مُّسْرِفِينَ
Moo ndax ! Danu leen di jox [Alxuraan] te fekk ngeen di ay yàqkat ?
6وَكَمْ أَرْسَلْنَا مِن نَّبِيٍّ فِي الْأَوَّلِينَ
Ak a bari lu nu yónni ci ay Yonnenta ca ña jiitu woon !
7وَمَا يَأْتِيهِم مِّن نَّبِيٍّ إِلَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
amul Yonnent bu mas a ñëw te yéjjiwuñu ko (ñaawal).
8فَأَهْلَكْنَا أَشَدَّ مِنْهُم بَطْشًا وَمَضَىٰ مَثَلُ الْأَوَّلِينَ
Faagaagal na nu ña leen ëppoon doole ! Xam ngeen xibaari ña jiitu woon.
9وَلَئِن سَأَلْتَهُم مَّنْ خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ لَيَقُولُنَّ خَلَقَهُنَّ الْعَزِيزُ الْعَلِيمُ
Te soo leen laajee : “Kan moo bind asamaan yeek suuf ? ” Dañu naan : “Yàlla, miy boroom Kàttan di ku Xam moo leen bind”.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 7

Simoore Az-Zukhruf Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : amul Yonnent bu mas a ñëw te yéjjiwuñu ko (ñaawal).

Simoore Aaya 7/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers