Az-Zukhruf · 6/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
وَكَمْ أَرْسَلْنَا مِن نَّبِيٍّ فِي الْأَوَّلِينَ ٦
Transliteration
Wa kam arsalnaa min Nabiyyin fil awwaleen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ak a bari lu nu yónni ci ay Yonnenta ca ña jiitu woon !
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 4-8 — Simoore Az-Zukhruf
4وَإِنَّهُ فِي أُمِّ الْكِتَابِ لَدَيْنَا لَعَلِيٌّ حَكِيمٌ
Nekk na fi Nun, ca ndayi Téere ba (Allawhul mahfuus), kawe lool fees dell ag ràñnee.
5أَفَنَضْرِبُ عَنكُمُ الذِّكْرَ صَفْحًا أَن كُنتُمْ قَوْمًا مُّسْرِفِينَ
Moo ndax ! Danu leen di jox [Alxuraan] te fekk ngeen di ay yàqkat ?
6وَكَمْ أَرْسَلْنَا مِن نَّبِيٍّ فِي الْأَوَّلِينَ
Ak a bari lu nu yónni ci ay Yonnenta ca ña jiitu woon !
7وَمَا يَأْتِيهِم مِّن نَّبِيٍّ إِلَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
amul Yonnent bu mas a ñëw te yéjjiwuñu ko (ñaawal).
8فَأَهْلَكْنَا أَشَدَّ مِنْهُم بَطْشًا وَمَضَىٰ مَثَلُ الْأَوَّلِينَ
Faagaagal na nu ña leen ëppoon doole ! Xam ngeen xibaari ña jiitu woon.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
6Aaya
Tekki — Az-Zukhruf 6
Simoore Az-Zukhruf Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak a bari lu nu yónni ci ay Yonnenta ca…Simoore Aaya 6/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Monday, September 7, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








