Ad-Dukhan · 9/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
بَلْ هُمْ فِي شَكٍّ يَلْعَبُونَ ۝٩
Bal hum fee shakkiny yal`aboon
📖 Tekkim Wolof
Ñoom, ña ngay sikki-sàkka, di fo.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 7-11 — Simoore Ad-Dukhan

7رَبِّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا ۖ إِن كُنتُم مُّوقِنِينَ
Moo di Boroom asamaan yeek suuf seek li nekk ci seen diggënte, ndegam wóolu ngeen.
8لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ يُحْيِي وَيُمِيتُ ۖ رَبُّكُمْ وَرَبُّ آبَائِكُمُ الْأَوَّلِينَ
Amul jenn Yàlla judul Moom. Mooy dundal di reye, Mooy seen Boroom mooy Boroom seeni maam ya fi jëkkoon.
9بَلْ هُمْ فِي شَكٍّ يَلْعَبُونَ
Ñoom, ña ngay sikki-sàkka, di fo.
10فَارْتَقِبْ يَوْمَ تَأْتِي السَّمَاءُ بِدُخَانٍ مُّبِينٍ
Fuglul, cëy bis ba asamaan si di dikk ak saxar suy jolli
11يَغْشَى النَّاسَ ۖ هَٰذَا عَذَابٌ أَلِيمٌ
di moor nit ñi. Tey mbugël mu mitti.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 9

Simoore Ad-Dukhan Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoom, ña ngay sikki-sàkka, di fo.

Simoore Aaya 9/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers