Al-Ahqaf · 28/35
Tekki Waxtaan — Al-Ahqaf
فَلَوْلَا نَصَرَهُمُ الَّذِينَ اتَّخَذُوا مِن دُونِ اللَّهِ قُرْبَانًا آلِهَةً ۖ بَلْ ضَلُّوا عَنْهُمْ ۚ وَذَٰلِكَ إِفْكُهُمْ وَمَا كَانُوا يَفْتَرُونَ ۝٢٨
Falaw laa nasarahumul lazeenat takhazoo min doonil laahi qurbaanan aalihatam bal dalloo `anhum` wa zaalika ifkuhum wa maa kaanoo yaftaroon
📖 Tekkim Wolof
Ana lu tax la ñu daan jaamu, bàyyi Yàlla dimbali wuñu leen ? Li am kay mooy dañu leen far réer mër ; loolu moo di seen fen wa ak la ñu daan dur.

🎧 Dégg


📜 Aaya 26-30 — Al-Ahqaf

26وَلَقَدْ مَكَّنَّاهُمْ فِيمَا إِن مَّكَّنَّاكُمْ فِيهِ وَجَعَلْنَا لَهُمْ سَمْعًا وَأَبْصَارًا وَأَفْئِدَةً فَمَا أَغْنَىٰ عَنْهُمْ سَمْعُهُمْ وَلَا أَبْصَارُهُمْ وَلَا أَفْئِدَتُهُم مِّن شَيْءٍ إِذْ كَانُوا يَجْحَدُونَ بِآيَاتِ اللَّهِ وَحَاقَ بِهِم مَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
Yombaloon nanu leen ñoom lu nu leen joxul yéen. Ndax defaloon nanu leen ag dégg ak ub gis, te seen dégg ga, wala séen gis ba, ak séen xol ya jariñu leen woon tus, ndax dañu daan weddi Laaya Yàlla yi firndeem ya. Ñañu daan yéjji far sóor leen.
27وَلَقَدْ أَهْلَكْنَا مَا حَوْلَكُم مِّنَ الْقُرَىٰ وَصَرَّفْنَا الْآيَاتِ لَعَلَّهُمْ يَرْجِعُونَ
Faagaagal nañu ca dëkk ya leen wër ; defaroon ay keemaan ak firnde yu wuute, ngir bëggoon ñu dellu ginnaaw ca séen kéefër gi.
28فَلَوْلَا نَصَرَهُمُ الَّذِينَ اتَّخَذُوا مِن دُونِ اللَّهِ قُرْبَانًا آلِهَةً ۖ بَلْ ضَلُّوا عَنْهُمْ ۚ وَذَٰلِكَ إِفْكُهُمْ وَمَا كَانُوا يَفْتَرُونَ
Ana lu tax la ñu daan jaamu, bàyyi Yàlla dimbali wuñu leen ? Li am kay mooy dañu leen far réer mër ; loolu moo di seen fen wa ak la ñu daan dur.
29وَإِذْ صَرَفْنَا إِلَيْكَ نَفَرًا مِّنَ الْجِنِّ يَسْتَمِعُونَ الْقُرْآنَ فَلَمَّا حَضَرُوهُ قَالُوا أَنصِتُوا ۖ فَلَمَّا قُضِيَ وَلَّوْا إِلَىٰ قَوْمِهِم مُّنذِرِينَ
(Fàttalikul) itam ba nu jubëlee ci mbooloom jinne ngir ñuy déglu Alxuraan ba ñu teewee nee na : “déglu leen”... Ba mu jeexee, walbatiku nañu ca séen mbokki jinne di leen waar .
30قَالُوا يَا قَوْمَنَا إِنَّا سَمِعْنَا كِتَابًا أُنزِلَ مِن بَعْدِ مُوسَىٰ مُصَدِّقًا لِّمَا بَيْنَ يَدَيْهِ يَهْدِي إِلَى الْحَقِّ وَإِلَىٰ طَرِيقٍ مُّسْتَقِيمٍ
Nee na ñu : "Eey yéen sunuw xeet ! Déglu nanu ab Téere bu ñu wàcce ginnaaw Muusaa, muy dëggal la ko jiitu dafay gindee itam jëme ci dëgg. Ak ci yoon wu jub xocc wa.
Al-AhqafFihi Alxuraan
35Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Al-Ahqaf 28

Simoore Al-Ahqaf Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ana lu tax la ñu daan jaamu, bàyyi Yàlla dimbali…

Simoore Aaya 28/35 — Al-Ahqaf الأحقاف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahqaf Dégg, Al-Ahqaf Tekki, Al-Ahqaf mp3, Al-Ahqaf pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers