Al-Fath · 21/29
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Fath
وَأُخْرَىٰ لَمْ تَقْدِرُوا عَلَيْهَا قَدْ أَحَاطَ اللَّهُ بِهَا ۚ وَكَانَ اللَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرًا ۝٢١
Wa ukhraa lam taqdiroo `alaihaa qad ahaatal laahu bihaa; wa kaanal laahu `alaa kulli shai`in qadeera
📖 Tekkim Wolof
Ak yeneen yu ngeen manul a woon Yàlla peeg na ko, Yàlla man na lépp lu ne.

🎧 Dégg


📜 Aaya 19-23 — Simoore Al-Fath

19وَمَغَانِمَ كَثِيرَةً يَأْخُذُونَهَا ۗ وَكَانَ اللَّهُ عَزِيزًا حَكِيمًا
ak ay màng (alal) yu bari yu nu nangu) yu ñuy jël. Yàlla Borom Kàttan la di Ku Xereñ .
20وَعَدَكُمُ اللَّهُ مَغَانِمَ كَثِيرَةً تَأْخُذُونَهَا فَعَجَّلَ لَكُمْ هَٰذِهِ وَكَفَّ أَيْدِيَ النَّاسِ عَنكُمْ وَلِتَكُونَ آيَةً لِّلْمُؤْمِنِينَ وَيَهْدِيَكُمْ صِرَاطًا مُّسْتَقِيمًا
Yàlla dig na leen ay màng yu bari yu ngeen di nara jël, mu gaawe leen ci (ubbig xaybar) gii te fegal na leen (ay yoxoy seeni noon), ak it ngir mu nekk kéemaan ci jullit ñi ak itam mu gindi leen tek leen ca yoon wu jubb xocc wa ;
21وَأُخْرَىٰ لَمْ تَقْدِرُوا عَلَيْهَا قَدْ أَحَاطَ اللَّهُ بِهَا ۚ وَكَانَ اللَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرًا
Ak yeneen yu ngeen manul a woon Yàlla peeg na ko, Yàlla man na lépp lu ne.
22وَلَوْ قَاتَلَكُمُ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوَلَّوُا الْأَدْبَارَ ثُمَّ لَا يَجِدُونَ وَلِيًّا وَلَا نَصِيرًا
Te sax bu yéefar yi xeexoon ak yéen danuy daw ; te dunu am kenn ku ñuy wéeru waxantumalaa ndimbal.
23سُنَّةَ اللَّهِ الَّتِي قَدْ خَلَتْ مِن قَبْلُ ۖ وَلَن تَجِدَ لِسُنَّةِ اللَّهِ تَبْدِيلًا
Mooy doxalinu Yàlla wi daan am na ka jekk. Te doxalinu Yàlla kenn du ko soppali.
Al-FathFihi Alxuraan
29Aaya
MedinanRevelation
21Aaya

Tekki — Al-Fath 21

Simoore Al-Fath Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak yeneen yu ngeen manul a woon Yàlla peeg na…

Simoore Aaya 21/29 — Simoore Al-Fath الفتح (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Fath Dégg, Simoore Al-Fath Tekki, Simoore Al-Fath mp3, Simoore Al-Fath pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers