Al-Fath · 22/29
Tekki Waxtaan — Al-Fath
وَلَوْ قَاتَلَكُمُ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوَلَّوُا الْأَدْبَارَ ثُمَّ لَا يَجِدُونَ وَلِيًّا وَلَا نَصِيرًا ٢٢
Transliteration
Wa law qaatalakumul lazeena kafaroo la wallawul adbaara summa laa yajidoona waliyanw-wa laa naseeraa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te sax bu yéefar yi xeexoon ak yéen danuy daw ; te dunu am kenn ku ñuy wéeru waxantumalaa ndimbal.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 20-24 — Al-Fath
20وَعَدَكُمُ اللَّهُ مَغَانِمَ كَثِيرَةً تَأْخُذُونَهَا فَعَجَّلَ لَكُمْ هَٰذِهِ وَكَفَّ أَيْدِيَ النَّاسِ عَنكُمْ وَلِتَكُونَ آيَةً لِّلْمُؤْمِنِينَ وَيَهْدِيَكُمْ صِرَاطًا مُّسْتَقِيمًا
Yàlla dig na leen ay màng yu bari yu ngeen di nara jël, mu gaawe leen ci (ubbig xaybar) gii te fegal na leen (ay yoxoy seeni noon), ak it ngir mu nekk kéemaan ci jullit ñi ak itam mu gindi leen tek leen ca yoon wu jubb xocc wa ;
21وَأُخْرَىٰ لَمْ تَقْدِرُوا عَلَيْهَا قَدْ أَحَاطَ اللَّهُ بِهَا ۚ وَكَانَ اللَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرًا
Ak yeneen yu ngeen manul a woon Yàlla peeg na ko, Yàlla man na lépp lu ne.
22وَلَوْ قَاتَلَكُمُ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوَلَّوُا الْأَدْبَارَ ثُمَّ لَا يَجِدُونَ وَلِيًّا وَلَا نَصِيرًا
Te sax bu yéefar yi xeexoon ak yéen danuy daw ; te dunu am kenn ku ñuy wéeru waxantumalaa ndimbal.
23سُنَّةَ اللَّهِ الَّتِي قَدْ خَلَتْ مِن قَبْلُ ۖ وَلَن تَجِدَ لِسُنَّةِ اللَّهِ تَبْدِيلًا
Mooy doxalinu Yàlla wi daan am na ka jekk. Te doxalinu Yàlla kenn du ko soppali.
24وَهُوَ الَّذِي كَفَّ أَيْدِيَهُمْ عَنكُمْ وَأَيْدِيَكُمْ عَنْهُم بِبَطْنِ مَكَّةَ مِن بَعْدِ أَنْ أَظْفَرَكُمْ عَلَيْهِمْ ۚ وَكَانَ اللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ بَصِيرًا
Mooy ki leen fegaloon sen yoxo moo feg it seeni yoxo yéen ci ñoom ca biir xuru Màkka wa (ba xarewooleen), ginnaaw ba mu leen joxee ndam ca kaw yéefar ya. Yàlla gis na la ngeen doon def.
Al-FathFihi Alxuraan
29Aaya
MedinanRevelation
22Aaya
Tekki — Al-Fath 22
Simoore Al-Fath Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te sax bu yéefar yi xeexoon ak yéen danuy daw…Simoore Aaya 22/29 — Al-Fath الفتح (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Fath Dégg, Al-Fath Tekki, Al-Fath mp3, Al-Fath pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








