Al-Fath · 23/29
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Fath
سُنَّةَ اللَّهِ الَّتِي قَدْ خَلَتْ مِن قَبْلُ ۖ وَلَن تَجِدَ لِسُنَّةِ اللَّهِ تَبْدِيلًا ۝٢٣
Sunnatal laahil latee qad khalat min qablu wa lan tajida lisunnatil laahi tabdeelaa
📖 Tekkim Wolof
Mooy doxalinu Yàlla wi daan am na ka jekk. Te doxalinu Yàlla kenn du ko soppali.

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Simoore Al-Fath

21وَأُخْرَىٰ لَمْ تَقْدِرُوا عَلَيْهَا قَدْ أَحَاطَ اللَّهُ بِهَا ۚ وَكَانَ اللَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرًا
Ak yeneen yu ngeen manul a woon Yàlla peeg na ko, Yàlla man na lépp lu ne.
22وَلَوْ قَاتَلَكُمُ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوَلَّوُا الْأَدْبَارَ ثُمَّ لَا يَجِدُونَ وَلِيًّا وَلَا نَصِيرًا
Te sax bu yéefar yi xeexoon ak yéen danuy daw ; te dunu am kenn ku ñuy wéeru waxantumalaa ndimbal.
23سُنَّةَ اللَّهِ الَّتِي قَدْ خَلَتْ مِن قَبْلُ ۖ وَلَن تَجِدَ لِسُنَّةِ اللَّهِ تَبْدِيلًا
Mooy doxalinu Yàlla wi daan am na ka jekk. Te doxalinu Yàlla kenn du ko soppali.
24وَهُوَ الَّذِي كَفَّ أَيْدِيَهُمْ عَنكُمْ وَأَيْدِيَكُمْ عَنْهُم بِبَطْنِ مَكَّةَ مِن بَعْدِ أَنْ أَظْفَرَكُمْ عَلَيْهِمْ ۚ وَكَانَ اللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ بَصِيرًا
Mooy ki leen fegaloon sen yoxo moo feg it seeni yoxo yéen ci ñoom ca biir xuru Màkka wa (ba xarewooleen), ginnaaw ba mu leen joxee ndam ca kaw yéefar ya. Yàlla gis na la ngeen doon def.
25هُمُ الَّذِينَ كَفَرُوا وَصَدُّوكُمْ عَنِ الْمَسْجِدِ الْحَرَامِ وَالْهَدْيَ مَعْكُوفًا أَن يَبْلُغَ مَحِلَّهُ ۚ وَلَوْلَا رِجَالٌ مُّؤْمِنُونَ وَنِسَاءٌ مُّؤْمِنَاتٌ لَّمْ تَعْلَمُوهُمْ أَن تَطَئُوهُمْ فَتُصِيبَكُم مِّنْهُم مَّعَرَّةٌ بِغَيْرِ عِلْمٍ ۖ لِّيُدْخِلَ اللَّهُ فِي رَحْمَتِهِ مَن يَشَاءُ ۚ لَوْ تَزَيَّلُوا لَعَذَّبْنَا الَّذِينَ كَفَرُوا مِنْهُمْ عَذَابًا أَلِيمًا
Ñoom ñoo di ña weddi woon te daan tere seen digganteek Jàkk ju ñu Wormaal ja dox it seen digganteek fa ñuy rendee hadyu. Dogan ko nag jullit ñu góor ñaak jullit ñu jigéen ña fa nekk te xamee wu leen ba manoon leen reyaale ca biir yéefar ya, te kon dey ñàkk xam dana leen yóbbe bàkkaar... Waaye Yàlla mooy tàbbal ku ko soob ci Yërmaandeem. Waaye su fekkoon ne yéefar yi dañoo beddiku dana leen mbugël mbugël mu mitti.
Al-FathFihi Alxuraan
29Aaya
MedinanRevelation
23Aaya

Tekki — Al-Fath 23

Simoore Al-Fath Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy doxalinu Yàlla wi daan am na ka jekk. Te…

Simoore Aaya 23/29 — Simoore Al-Fath الفتح (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Fath Dégg, Simoore Al-Fath Tekki, Simoore Al-Fath mp3, Simoore Al-Fath pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers