Al-Maida · 28/120
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Maida
لَئِن بَسَطتَ إِلَيَّ يَدَكَ لِتَقْتُلَنِي مَا أَنَا بِبَاسِطٍ يَدِيَ إِلَيْكَ لِأَقْتُلَكَ ۖ إِنِّي أَخَافُ اللَّهَ رَبَّ الْعَالَمِينَ ۝٢٨
La`im basatta ilaiya yadaka litaqtulanee maaa ana bibaasitiny yadiya ilaika li aqtulaka inneee akhaaful laaha Rabbal `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Te boo tàllalee sa loxo di ma rey man dey duma jëme sama loxo ci yaw waxantumalaak di la jéem a rey : ndax man Yàlla Miy Boroom mbindeef yi laa ragal.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 26-30 — Simoore Al-Maida

26قَالَ فَإِنَّهَا مُحَرَّمَةٌ عَلَيْهِمْ ۛ أَرْبَعِينَ سَنَةً ۛ يَتِيهُونَ فِي الْأَرْضِ ۚ فَلَا تَأْسَ عَلَى الْقَوْمِ الْفَاسِقِينَ
[Boroom bi tontu] ne: “Suuf soosu araam na leen ñeent-fukki at yoo xam ne danañu gëlëm di wëndéelu ci àll bi. Bul jàq ci mbiru ñiy sàqi ndigal”.
27۞ وَاتْلُ عَلَيْهِمْ نَبَأَ ابْنَيْ آدَمَ بِالْحَقِّ إِذْ قَرَّبَا قُرْبَانًا فَتُقُبِّلَ مِنْ أَحَدِهِمَا وَلَمْ يُتَقَبَّلْ مِنَ الْآخَرِ قَالَ لَأَقْتُلَنَّكَ ۖ قَالَ إِنَّمَا يَتَقَبَّلُ اللَّهُ مِنَ الْمُتَّقِينَ
Nettalileen, ci lu dëggu, xibaari ñaari doomi Aadama ya. Ba ñu sàkkoo yool bu ñu jaamoo Yàlla ; te Yàlla nangul kenn ca ñoom ñaar, bañ a nangul ka ca des. Ka ñu nangulul wax ne : “Danaa la rey”. Ka ñu nangul ne ko : “Na la wóor yaw it ne, Yàlla ña ko ragal lay nangu seeni jëf”.
28لَئِن بَسَطتَ إِلَيَّ يَدَكَ لِتَقْتُلَنِي مَا أَنَا بِبَاسِطٍ يَدِيَ إِلَيْكَ لِأَقْتُلَكَ ۖ إِنِّي أَخَافُ اللَّهَ رَبَّ الْعَالَمِينَ
Te boo tàllalee sa loxo di ma rey man dey duma jëme sama loxo ci yaw waxantumalaak di la jéem a rey : ndax man Yàlla Miy Boroom mbindeef yi laa ragal.
29إِنِّي أُرِيدُ أَن تَبُوءَ بِإِثْمِي وَإِثْمِكَ فَتَكُونَ مِنْ أَصْحَابِ النَّارِ ۚ وَذَٰلِكَ جَزَاءُ الظَّالِمِينَ
Te sax li ma namm moo di nga yenu sama bàkkaar boole kook sa bos : bu ko defee nga bokk ca waa Safara. Te loolu mooy peyug tooñkat ya.
30فَطَوَّعَتْ لَهُ نَفْسُهُ قَتْلَ أَخِيهِ فَقَتَلَهُ فَأَصْبَحَ مِنَ الْخَاسِرِينَ
[Ka ñu nangulul], bakkanam daldi koy xiir ci rey mbokkam. Mu daldi far bokk ca way- yàqule ña.
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
28Aaya

Tekki — Al-Maida 28

Simoore Al-Maida Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te boo tàllalee sa loxo di ma rey man dey…

Simoore Aaya 28/120 — Simoore Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Maida Dégg, Simoore Al-Maida Tekki, Simoore Al-Maida mp3, Simoore Al-Maida pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers