Al-Maida · 79/120
Tekki Waxtaan — Al-Maida
كَانُوا لَا يَتَنَاهَوْنَ عَن مُّنكَرٍ فَعَلُوهُ ۚ لَبِئْسَ مَا كَانُوا يَفْعَلُونَ ٧٩
Transliteration
Kaanoo laa yatanaahawna `am munkarin fa`aluhoo; labi`sa maa kaanoo yafa`loon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Daawuñu bàyyi lu ñaaw la ñu daan def. Ay waay, la ñu daan def, aka bon !
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 77-81 — Al-Maida
77قُلْ يَا أَهْلَ الْكِتَابِ لَا تَغْلُوا فِي دِينِكُمْ غَيْرَ الْحَقِّ وَلَا تَتَّبِعُوا أَهْوَاءَ قَوْمٍ قَدْ ضَلُّوا مِن قَبْلُ وَأَضَلُّوا كَثِيرًا وَضَلُّوا عَن سَوَاءِ السَّبِيلِ
Neel : “Yéen ñon-téere, buleen teeŋal seen diine, mu wuuteek dëgg ga. Buleen topp bànneexi nit ñoo xam ne réeroon nañu bu jëkk, te réeraloon nañu ñu bari, réere tigi yoon wu jub wa.
78لُعِنَ الَّذِينَ كَفَرُوا مِن بَنِي إِسْرَائِيلَ عَلَىٰ لِسَانِ دَاوُودَ وَعِيسَى ابْنِ مَرْيَمَ ۚ ذَٰلِكَ بِمَا عَصَوا وَّكَانُوا يَعْتَدُونَ
Rëbbéef na ña weddi ca waa Bani Israayiila mu jaare ca làmmiñu Daawuda ak [Iisaa] doomi Maryaama, ngir lañu moy ndigal te nekkon ñu jéggi dayo.
79كَانُوا لَا يَتَنَاهَوْنَ عَن مُّنكَرٍ فَعَلُوهُ ۚ لَبِئْسَ مَا كَانُوا يَفْعَلُونَ
Daawuñu bàyyi lu ñaaw la ñu daan def. Ay waay, la ñu daan def, aka bon !
80تَرَىٰ كَثِيرًا مِّنْهُمْ يَتَوَلَّوْنَ الَّذِينَ كَفَرُوا ۚ لَبِئْسَ مَا قَدَّمَتْ لَهُمْ أَنفُسُهُمْ أَن سَخِطَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ وَفِي الْعَذَابِ هُمْ خَالِدُونَ
Danga gis ñu bari ci ñoom ñuy xaritoo ak ña weddi. La leen seeni bakkan defloo ñaaw na, ba Yàlla mere leen, te ci ag mbugal lañuy nekk béel ca.
81وَلَوْ كَانُوا يُؤْمِنُونَ بِاللَّهِ وَالنَّبِيِّ وَمَا أُنزِلَ إِلَيْهِ مَا اتَّخَذُوهُمْ أَوْلِيَاءَ وَلَٰكِنَّ كَثِيرًا مِّنْهُمْ فَاسِقُونَ
Bu ñu nekkoon di ñu gëm Yàlla, ak Yonent ba ak la ñu wàcce ca ñoom, duñu jàppe xarit [yéefar ya]. Waaye lu bari ca ñoom saay-saay lañu [ñu génn ci topp].
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
79Aaya
Tekki — Al-Maida 79
Simoore Al-Maida Aaya 79 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Daawuñu bàyyi lu ñaaw la ñu daan def. Ay waay,…Simoore Aaya 79/120 — Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Maida Dégg, Al-Maida Tekki, Al-Maida mp3, Al-Maida pdf. Aaya 77–81. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








