Al-Maida · 87/120
Tekki Waxtaan — Al-Maida
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تُحَرِّمُوا طَيِّبَاتِ مَا أَحَلَّ اللَّهُ لَكُمْ وَلَا تَعْتَدُوا ۚ إِنَّ اللَّهَ لَا يُحِبُّ الْمُعْتَدِينَ ٨٧
Transliteration
Yaaa aiyuhal lazeena aamanoo laa tuharrimoo taiyibaati maaa ahallal laahu lakum wa laa ta`tadooo; innal laaha laa yuhibbul mu`tadeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Éy yéen ñi gëm : buleen araamal yu sell ya leen Yàlla daganal. Te it buleen jéggi dayo, Yàlla soppul ñiy jéggi dayo.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 85-89 — Al-Maida
85فَأَثَابَهُمُ اللَّهُ بِمَا قَالُوا جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا ۚ وَذَٰلِكَ جَزَاءُ الْمُحْسِنِينَ
Yàlla xéewale na leen, ngir la ñu wax, ay Àjjana yoo xam ne ay dex dañuy daw ca suufam, te dañu fay béel. Te loolu mooy peyug way-rafetal ña.
86وَالَّذِينَ كَفَرُوا وَكَذَّبُوا بِآيَاتِنَا أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ الْجَحِيمِ
Waaye nag yéefar ya weddi Sunuy kàddu, ñoom ñooy dugg Safara.
87يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تُحَرِّمُوا طَيِّبَاتِ مَا أَحَلَّ اللَّهُ لَكُمْ وَلَا تَعْتَدُوا ۚ إِنَّ اللَّهَ لَا يُحِبُّ الْمُعْتَدِينَ
Éy yéen ñi gëm : buleen araamal yu sell ya leen Yàlla daganal. Te it buleen jéggi dayo, Yàlla soppul ñiy jéggi dayo.
88وَكُلُوا مِمَّا رَزَقَكُمُ اللَّهُ حَلَالًا طَيِّبًا ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ الَّذِي أَنتُم بِهِ مُؤْمِنُونَ
Lekkleen li leen Yàlla wërsëgale muy li dagan te sell. Te nangeen ragal Yàlla ji ngeen gëm.
89لَا يُؤَاخِذُكُمُ اللَّهُ بِاللَّغْوِ فِي أَيْمَانِكُمْ وَلَٰكِن يُؤَاخِذُكُم بِمَا عَقَّدتُّمُ الْأَيْمَانَ ۖ فَكَفَّارَتُهُ إِطْعَامُ عَشَرَةِ مَسَاكِينَ مِنْ أَوْسَطِ مَا تُطْعِمُونَ أَهْلِيكُمْ أَوْ كِسْوَتُهُمْ أَوْ تَحْرِيرُ رَقَبَةٍ ۖ فَمَن لَّمْ يَجِدْ فَصِيَامُ ثَلَاثَةِ أَيَّامٍ ۚ ذَٰلِكَ كَفَّارَةُ أَيْمَانِكُمْ إِذَا حَلَفْتُمْ ۚ وَاحْفَظُوا أَيْمَانَكُمْ ۚ كَذَٰلِكَ يُبَيِّنُ اللَّهُ لَكُمْ آيَاتِهِ لَعَلَّكُمْ تَشْكُرُونَ
Yàlla duleen jàppe ngiñ yi ngeen di kafe, waaye Dana leen jàppe ngiñ yi dëggu ci yéen. Te ñoom, la ñuy jéggaloo mooy leel fukki néew-ji-doole [ci ñam wa ngeen di faral a dundale seen njaboot], mbaa jox leen ay yére, walla goreel jaam. Ku ko mënul, na woor ñetti fan. Loola mooy na ñuy jéggaloo seen ngiñ ya ngeen waate [lu jaaduwul]. nangeen sàmm seen ngiñ, nii la leen Yàlla di leerale ay ndigalam ndax xéy-na ngeen gërëm Ko [delloo njukkal] !
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
87Aaya
Tekki — Al-Maida 87
Simoore Al-Maida Aaya 87 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yéen ñi gëm : buleen araamal yu sell ya…Simoore Aaya 87/120 — Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Maida Dégg, Al-Maida Tekki, Al-Maida mp3, Al-Maida pdf. Aaya 85–89. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








