Adh-Dhariyat · 15/60
Tekki Waxtaan — Simoore Adh-Dhariyat
إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي جَنَّاتٍ وَعُيُونٍ ۝١٥
Innal muttaqeena fee jannaatinw wa `uyoon
📖 Tekkim Wolof
Ña ragaloon Yàlla ña nga ca biir Àjjana yu ànd ak bëti ndox yuy daw dawaan,

🎧 Dégg


📜 Aaya 13-17 — Simoore Adh-Dhariyat

13يَوْمَ هُمْ عَلَى النَّارِ يُفْتَنُونَ
Bis ba nga xam ne dees na leen ca fitnaal ca Safara (lakk leen) :
14ذُوقُوا فِتْنَتَكُمْ هَٰذَا الَّذِي كُنتُم بِهِ تَسْتَعْجِلُونَ
Ñu di leen wax naan : “Tokamtikuleen sànje bii ; lii nag mooy la ngeen daan yàkkamti”.
15إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي جَنَّاتٍ وَعُيُونٍ
Ña ragaloon Yàlla ña nga ca biir Àjjana yu ànd ak bëti ndox yuy daw dawaan,
16آخِذِينَ مَا آتَاهُمْ رَبُّهُمْ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَبْلَ ذَٰلِكَ مُحْسِنِينَ
ña ngay jël la leen seen Boroom di jox. Ndax ñoom lu jiitu loolu dañu daan rafetal :
17كَانُوا قَلِيلًا مِّنَ اللَّيْلِ مَا يَهْجَعُونَ
bu guddi jotaan, lu néew lañu ca daan nelaw,
Adh-DhariyatFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Adh-Dhariyat 15

Simoore Adh-Dhariyat Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña ragaloon Yàlla ña nga ca biir Àjjana yu ànd…

Simoore Aaya 15/60 — Simoore Adh-Dhariyat الذاريات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Adh-Dhariyat Dégg, Simoore Adh-Dhariyat Tekki, Simoore Adh-Dhariyat mp3, Simoore Adh-Dhariyat pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers