Adh-Dhariyat · 16/60
Tekki Waxtaan — Simoore Adh-Dhariyat
آخِذِينَ مَا آتَاهُمْ رَبُّهُمْ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَبْلَ ذَٰلِكَ مُحْسِنِينَ ١٦
Transliteration
Aakhizeena maaa aataahum Rabbuhum; innahum kaanoo qabla zaalika muhsineen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
ña ngay jël la leen seen Boroom di jox. Ndax ñoom lu jiitu loolu dañu daan rafetal :
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 14-18 — Simoore Adh-Dhariyat
14ذُوقُوا فِتْنَتَكُمْ هَٰذَا الَّذِي كُنتُم بِهِ تَسْتَعْجِلُونَ
Ñu di leen wax naan : “Tokamtikuleen sànje bii ; lii nag mooy la ngeen daan yàkkamti”.
15إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي جَنَّاتٍ وَعُيُونٍ
Ña ragaloon Yàlla ña nga ca biir Àjjana yu ànd ak bëti ndox yuy daw dawaan,
16آخِذِينَ مَا آتَاهُمْ رَبُّهُمْ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَبْلَ ذَٰلِكَ مُحْسِنِينَ
ña ngay jël la leen seen Boroom di jox. Ndax ñoom lu jiitu loolu dañu daan rafetal :
17كَانُوا قَلِيلًا مِّنَ اللَّيْلِ مَا يَهْجَعُونَ
bu guddi jotaan, lu néew lañu ca daan nelaw,
18وَبِالْأَسْحَارِ هُمْ يَسْتَغْفِرُونَ
bu njël masaana jot danuy jéggalu [seen Boroom] ;
Adh-DhariyatFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
16Aaya
Tekki — Adh-Dhariyat 16
Simoore Adh-Dhariyat Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ña ngay jël la leen seen Boroom di jox. Ndax…Simoore Aaya 16/60 — Simoore Adh-Dhariyat الذاريات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Adh-Dhariyat Dégg, Simoore Adh-Dhariyat Tekki, Simoore Adh-Dhariyat mp3, Simoore Adh-Dhariyat pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Adh-Dhariyat
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Friday, October 2, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


