Adh-Dhariyat · 14/60
Tekki Waxtaan — Adh-Dhariyat
ذُوقُوا فِتْنَتَكُمْ هَٰذَا الَّذِي كُنتُم بِهِ تَسْتَعْجِلُونَ ١٤
Transliteration
Zooqoo fitnatakum haa zal lazee kuntum bihee tas ta`jiloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñu di leen wax naan : “Tokamtikuleen sànje bii ; lii nag mooy la ngeen daan yàkkamti”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 12-16 — Adh-Dhariyat
12يَسْأَلُونَ أَيَّانَ يَوْمُ الدِّينِ
Ñangay laajati : “Kañ la bis Penc bay doon ? ”
13يَوْمَ هُمْ عَلَى النَّارِ يُفْتَنُونَ
Bis ba nga xam ne dees na leen ca fitnaal ca Safara (lakk leen) :
14ذُوقُوا فِتْنَتَكُمْ هَٰذَا الَّذِي كُنتُم بِهِ تَسْتَعْجِلُونَ
Ñu di leen wax naan : “Tokamtikuleen sànje bii ; lii nag mooy la ngeen daan yàkkamti”.
15إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي جَنَّاتٍ وَعُيُونٍ
Ña ragaloon Yàlla ña nga ca biir Àjjana yu ànd ak bëti ndox yuy daw dawaan,
16آخِذِينَ مَا آتَاهُمْ رَبُّهُمْ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَبْلَ ذَٰلِكَ مُحْسِنِينَ
ña ngay jël la leen seen Boroom di jox. Ndax ñoom lu jiitu loolu dañu daan rafetal :
Adh-DhariyatFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
14Aaya
Tekki — Adh-Dhariyat 14
Simoore Adh-Dhariyat Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu di leen wax naan : “Tokamtikuleen sànje bii ;…Simoore Aaya 14/60 — Adh-Dhariyat الذاريات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Adh-Dhariyat Dégg, Adh-Dhariyat Tekki, Adh-Dhariyat mp3, Adh-Dhariyat pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








